Aali Imran · 168/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
الَّذِينَ قَالُوا لِإِخْوَانِهِمْ وَقَعَدُوا لَوْ أَطَاعُونَا مَا قُتِلُوا ۗ قُلْ فَادْرَءُوا عَنْ أَنفُسِكُمُ الْمَوْتَ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ ۝١٦٨
Allazeena qaaloo liikhwaanihim wa qa`adoo law ataa`oonaa maa qutiloo; qul fadra`oo`an anfusikumul mawta in kuntum saadiqeen
📖 Tekkim Wolof
Ña toog bañ a xareji tey wax seeni mbokk : “Su ngeen nu déggaloon, dungeen xareji.”. Neeleen : “Jiñleen dee mu bañ a agsi ci seeni bakkan ndeem ñu dëggu ngeen”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 166-170 — Simoore Aali Imran

166وَمَا أَصَابَكُمْ يَوْمَ الْتَقَى الْجَمْعَانِ فَبِإِذْنِ اللَّهِ وَلِيَعْلَمَ الْمُؤْمِنِينَ
La leen dalool ca seenub dajeeb ñaari mbooloo ya, lu Yàlla nammoon la ngir mu xàmmee ca ña gëm [xareb Uhud]
167وَلِيَعْلَمَ الَّذِينَ نَافَقُوا ۚ وَقِيلَ لَهُمْ تَعَالَوْا قَاتِلُوا فِي سَبِيلِ اللَّهِ أَوِ ادْفَعُوا ۖ قَالُوا لَوْ نَعْلَمُ قِتَالًا لَّاتَّبَعْنَاكُمْ ۗ هُمْ لِلْكُفْرِ يَوْمَئِذٍ أَقْرَبُ مِنْهُمْ لِلْإِيمَانِ ۚ يَقُولُونَ بِأَفْوَاهِهِم مَّا لَيْسَ فِي قُلُوبِهِمْ ۗ وَاللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا يَكْتُمُونَ
ak ngir mu ràññee naaféq ya. Waxees na leen ne : “Kaayleen xeex [xare] ci yoonu Yàlla, walla ngeen feg [noon ya]”, ñu toontu ne : “Su nu mënoon xeex, dananu leen topp”. Ñoom, ca bis boobu, kéefar lañu gën a jege ci ngëm. Dañuy wax ca seeni gimiñ lu nekkul ca seeni xol. Te Yàllaa gën a xam lu ñuy nëbb.
168الَّذِينَ قَالُوا لِإِخْوَانِهِمْ وَقَعَدُوا لَوْ أَطَاعُونَا مَا قُتِلُوا ۗ قُلْ فَادْرَءُوا عَنْ أَنفُسِكُمُ الْمَوْتَ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ña toog bañ a xareji tey wax seeni mbokk : “Su ngeen nu déggaloon, dungeen xareji.”. Neeleen : “Jiñleen dee mu bañ a agsi ci seeni bakkan ndeem ñu dëggu ngeen”.
169وَلَا تَحْسَبَنَّ الَّذِينَ قُتِلُوا فِي سَبِيلِ اللَّهِ أَمْوَاتًا ۚ بَلْ أَحْيَاءٌ عِندَ رَبِّهِمْ يُرْزَقُونَ
Bul foog ne ñañu reyee ci yoonu Yàlla, ñu dee lañu. Déet, ñuy dundu lañu ca seen Boroom, nekk ci xéewal
170فَرِحِينَ بِمَا آتَاهُمُ اللَّهُ مِن فَضْلِهِ وَيَسْتَبْشِرُونَ بِالَّذِينَ لَمْ يَلْحَقُوا بِهِم مِّنْ خَلْفِهِمْ أَلَّا خَوْفٌ عَلَيْهِمْ وَلَا هُمْ يَحْزَنُونَ
dañuy bég ca la leen Yàlla jox ci ay ngënéelam, di bég it ca jullit ya ñu bàyyi ginnaaw te fekkeeguñu leen, duñu jàq, duñu am naqar bu ñu fa eggee.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
168Aaya

Tekki — Aali Imran 168

Simoore Aali Imran Aaya 168 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña toog bañ a xareji tey wax seeni mbokk :…

Simoore Aaya 168/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 166–170. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers