Aali Imran · 30/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
يَوْمَ تَجِدُ كُلُّ نَفْسٍ مَّا عَمِلَتْ مِنْ خَيْرٍ مُّحْضَرًا وَمَا عَمِلَتْ مِن سُوءٍ تَوَدُّ لَوْ أَنَّ بَيْنَهَا وَبَيْنَهُ أَمَدًا بَعِيدًا ۗ وَيُحَذِّرُكُمُ اللَّهُ نَفْسَهُ ۗ وَاللَّهُ رَءُوفٌ بِالْعِبَادِ ۝٣٠
Yawma tajidu kullu nafsim maa`amilat min khairim muhdaranw wa maa `amilat min sooo`in tawaddu law anna bainahaa wa bainahooo amadam ba`eedaa; wa yuhazzirukumul laahu nafsah; wallaahu ra`oofum bil`ibaad
📖 Tekkim Wolof
Bis ba nga xam ne bakkan bu nekk dana jot ca la mu defoon ci aw yiw ak ca la mu defoon ci ñaawtéef ; dana ngéejoo dàndanteek ñaawtéef yooyu sore ko lool ! Yàllaa ngi leen di moytandikuloo boppam. Te Yàlla dey ku ñeewant jaam ñi la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 28-32 — Simoore Aali Imran

28لَّا يَتَّخِذِ الْمُؤْمِنُونَ الْكَافِرِينَ أَوْلِيَاءَ مِن دُونِ الْمُؤْمِنِينَ ۖ وَمَن يَفْعَلْ ذَٰلِكَ فَلَيْسَ مِنَ اللَّهِ فِي شَيْءٍ إِلَّا أَن تَتَّقُوا مِنْهُمْ تُقَاةً ۗ وَيُحَذِّرُكُمُ اللَّهُ نَفْسَهُ ۗ وَإِلَى اللَّهِ الْمَصِيرُ
Bu jullit ñi jàpp xaritoo ci yéefar yi, bàyyi fa jullit ña. Ku def loolu amoo ca Yàlla dara, ndeem du dangeen ragal ca ñoom ngaañ. Yàllaa ngi leen di moytandikuloo boppam. Te fa Moom la lépp di mujj.
29قُلْ إِن تُخْفُوا مَا فِي صُدُورِكُمْ أَوْ تُبْدُوهُ يَعْلَمْهُ اللَّهُ ۗ وَيَعْلَمُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۗ وَاللَّهُ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Neel : “Bu ngeen nëbbee li ci seeni xol walla ngeen feeñal ko, Yàlla dana ko xam. Yàlla xam na li nekk ci asamaan yeek suuf si. Te Yàlla am na kàttan def lu ne.
30يَوْمَ تَجِدُ كُلُّ نَفْسٍ مَّا عَمِلَتْ مِنْ خَيْرٍ مُّحْضَرًا وَمَا عَمِلَتْ مِن سُوءٍ تَوَدُّ لَوْ أَنَّ بَيْنَهَا وَبَيْنَهُ أَمَدًا بَعِيدًا ۗ وَيُحَذِّرُكُمُ اللَّهُ نَفْسَهُ ۗ وَاللَّهُ رَءُوفٌ بِالْعِبَادِ
Bis ba nga xam ne bakkan bu nekk dana jot ca la mu defoon ci aw yiw ak ca la mu defoon ci ñaawtéef ; dana ngéejoo dàndanteek ñaawtéef yooyu sore ko lool ! Yàllaa ngi leen di moytandikuloo boppam. Te Yàlla dey ku ñeewant jaam ñi la.
31قُلْ إِن كُنتُمْ تُحِبُّونَ اللَّهَ فَاتَّبِعُونِي يُحْبِبْكُمُ اللَّهُ وَيَغْفِرْ لَكُمْ ذُنُوبَكُمْ ۗ وَاللَّهُ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Neel : “Ndegam sopp ngeen Yàlla, toppleen ma, kon dey Yàlla dana leen safoo te jéggal leen seeni bàkkaar. Yàlla jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
32قُلْ أَطِيعُوا اللَّهَ وَالرَّسُولَ ۖ فَإِن تَوَلَّوْا فَإِنَّ اللَّهَ لَا يُحِبُّ الْكَافِرِينَ
Neel : “Toppleen Yàlla ak Yonent bi. Bu ngeen dëddoo [def lu bokkul ak loolu] ... Yàlla du safoo yéefar ya !
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
30Aaya

Tekki — Aali Imran 30

Simoore Aali Imran Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bis ba nga xam ne bakkan bu nekk dana jot…

Simoore Aaya 30/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers