Aali Imran · 4/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
مِن قَبْلُ هُدًى لِّلنَّاسِ وَأَنزَلَ الْفُرْقَانَ ۗ إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا بِآيَاتِ اللَّهِ لَهُمْ عَذَابٌ شَدِيدٌ ۗ وَاللَّهُ عَزِيزٌ ذُو انتِقَامٍ ۝٤
Min qablu hudal linnaasi wa anzalal Furqaan; innallazeena kafaroo bi Aayaatil laahi lahum `azaabun shadeed; wallaahu `azeezun zun tiqaam
📖 Tekkim Wolof
ca bu jëkk, doonoon njub ci nit ñi. Moo wàcce Alxuraan. Ña weddi kàdduy Yàlla yi, am nañu mbugal mu tar ! Te Yàlla ku not la , Boroomug feyyu la.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 2-6 — Simoore Aali Imran

2اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ الْحَيُّ الْقَيُّومُ
Yàlla mooy Yàlla ! Amul jeneen yàlla ju dul Moom, Aji-dundu la, di Aji-taxawaakoon ci lépp.
3نَزَّلَ عَلَيْكَ الْكِتَابَ بِالْحَقِّ مُصَدِّقًا لِّمَا بَيْنَ يَدَيْهِ وَأَنزَلَ التَّوْرَاةَ وَالْإِنجِيلَ
Moo wàcce ci yaw Téere ba ci dëgg, di feddali la ko jiitu. Moo wàcce Tawreet ak Injiil
4مِن قَبْلُ هُدًى لِّلنَّاسِ وَأَنزَلَ الْفُرْقَانَ ۗ إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا بِآيَاتِ اللَّهِ لَهُمْ عَذَابٌ شَدِيدٌ ۗ وَاللَّهُ عَزِيزٌ ذُو انتِقَامٍ
ca bu jëkk, doonoon njub ci nit ñi. Moo wàcce Alxuraan. Ña weddi kàdduy Yàlla yi, am nañu mbugal mu tar ! Te Yàlla ku not la , Boroomug feyyu la.
5إِنَّ اللَّهَ لَا يَخْفَىٰ عَلَيْهِ شَيْءٌ فِي الْأَرْضِ وَلَا فِي السَّمَاءِ
Yàlla, dara nëbbuwul ci Moom biir asamaan ak suuf si.
6هُوَ الَّذِي يُصَوِّرُكُمْ فِي الْأَرْحَامِ كَيْفَ يَشَاءُ ۚ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Moo leen móol ci seeni biiri nday, na Mu ko soobee. Amul jeneen Yàlla ju dul Moom, Mooy ki not, di ku xereñ.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
4Aaya

Tekki — Aali Imran 4

Simoore Aali Imran Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ca bu jëkk, doonoon njub ci nit ñi. Moo wàcce…

Simoore Aaya 4/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers