Aali Imran · 5/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
إِنَّ اللَّهَ لَا يَخْفَىٰ عَلَيْهِ شَيْءٌ فِي الْأَرْضِ وَلَا فِي السَّمَاءِ ٥
Transliteration
Innal laaha laa yakhfaa `alaihi shai`un fil ardi wa laa fis samaaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yàlla, dara nëbbuwul ci Moom biir asamaan ak suuf si.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 3-7 — Aali Imran
3نَزَّلَ عَلَيْكَ الْكِتَابَ بِالْحَقِّ مُصَدِّقًا لِّمَا بَيْنَ يَدَيْهِ وَأَنزَلَ التَّوْرَاةَ وَالْإِنجِيلَ
Moo wàcce ci yaw Téere ba ci dëgg, di feddali la ko jiitu. Moo wàcce Tawreet ak Injiil
4مِن قَبْلُ هُدًى لِّلنَّاسِ وَأَنزَلَ الْفُرْقَانَ ۗ إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا بِآيَاتِ اللَّهِ لَهُمْ عَذَابٌ شَدِيدٌ ۗ وَاللَّهُ عَزِيزٌ ذُو انتِقَامٍ
ca bu jëkk, doonoon njub ci nit ñi. Moo wàcce Alxuraan. Ña weddi kàdduy Yàlla yi, am nañu mbugal mu tar ! Te Yàlla ku not la , Boroomug feyyu la.
5إِنَّ اللَّهَ لَا يَخْفَىٰ عَلَيْهِ شَيْءٌ فِي الْأَرْضِ وَلَا فِي السَّمَاءِ
Yàlla, dara nëbbuwul ci Moom biir asamaan ak suuf si.
6هُوَ الَّذِي يُصَوِّرُكُمْ فِي الْأَرْحَامِ كَيْفَ يَشَاءُ ۚ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Moo leen móol ci seeni biiri nday, na Mu ko soobee. Amul jeneen Yàlla ju dul Moom, Mooy ki not, di ku xereñ.
7هُوَ الَّذِي أَنزَلَ عَلَيْكَ الْكِتَابَ مِنْهُ آيَاتٌ مُّحْكَمَاتٌ هُنَّ أُمُّ الْكِتَابِ وَأُخَرُ مُتَشَابِهَاتٌ ۖ فَأَمَّا الَّذِينَ فِي قُلُوبِهِمْ زَيْغٌ فَيَتَّبِعُونَ مَا تَشَابَهَ مِنْهُ ابْتِغَاءَ الْفِتْنَةِ وَابْتِغَاءَ تَأْوِيلِهِ ۗ وَمَا يَعْلَمُ تَأْوِيلَهُ إِلَّا اللَّهُ ۗ وَالرَّاسِخُونَ فِي الْعِلْمِ يَقُولُونَ آمَنَّا بِهِ كُلٌّ مِّنْ عِندِ رَبِّنَا ۗ وَمَا يَذَّكَّرُ إِلَّا أُولُو الْأَلْبَابِ
Moom moo wàcce ci yaw Téere ba : am na ca ay laaya seen maanaa leer nañu, ñoo di cosaani àtte yi, ak yeneeni laaya yu seeni maanaa fésul. Ña nga xam ne jeng a nekk seeni xol, benn ca laaya yooyu lañuy topp ngir sàkku fitna ak jéem leen a firi, te Yàlla doŋŋ a xam seeni piri ak ña sax ci xam-xam. Danañu wax ne : “Gëm nanu ko : lépp ca sunu Boroom la bawoo ! ” Woroom xel yi rekk ay waaru.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
5Aaya
Tekki — Aali Imran 5
Simoore Aali Imran Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla, dara nëbbuwul ci Moom biir asamaan ak suuf si.Simoore Aaya 5/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








