Ar-Rum · 28/60
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rum
ضَرَبَ لَكُم مَّثَلًا مِّنْ أَنفُسِكُمْ ۖ هَل لَّكُم مِّن مَّا مَلَكَتْ أَيْمَانُكُم مِّن شُرَكَاءَ فِي مَا رَزَقْنَاكُمْ فَأَنتُمْ فِيهِ سَوَاءٌ تَخَافُونَهُمْ كَخِيفَتِكُمْ أَنفُسَكُمْ ۚ كَذَٰلِكَ نُفَصِّلُ الْآيَاتِ لِقَوْمٍ يَعْقِلُونَ ۝٢٨
Daraba lakum masalam min anfusikum hal lakum mimmaa malakat aymaanukum min shurakaaa`a fee maa razaqnaakum fa antum feehi sawaaa`un takhaafoonahum kakheefa tikum anfusakum; kazaalika nufassilul Aayaati liqawminy ya`qiloon
📖 Tekkim Wolof
Yàlla sadd na leen ay léebu ci seen bopp : Ndax seen jaam ñi bokk nañu ak yéen seeni alal, ngeen yem ci kepp ? [Mukk], loolu rekk ngeen ragal. Nii la Nul leerale laaya yi ngir aw nit ñuy xalaat.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 26-30 — Simoore Ar-Rum

26وَلَهُ مَن فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ كُلٌّ لَّهُ قَانِتُونَ
Moo moom ñépp ñu nekk asamaan ak suuf : ñépp a koy toroxlul.
27وَهُوَ الَّذِي يَبْدَأُ الْخَلْقَ ثُمَّ يُعِيدُهُ وَهُوَ أَهْوَنُ عَلَيْهِ ۚ وَلَهُ الْمَثَلُ الْأَعْلَىٰ فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Moo sos mbindéef yi di leen defaraat ; te looloo gën a yomb ci Moom. Moo dàmbe li gën a kawe ci asamaan yeek suuf si. Mooy boroom Kàttan, di ku Xereñ ki.
28ضَرَبَ لَكُم مَّثَلًا مِّنْ أَنفُسِكُمْ ۖ هَل لَّكُم مِّن مَّا مَلَكَتْ أَيْمَانُكُم مِّن شُرَكَاءَ فِي مَا رَزَقْنَاكُمْ فَأَنتُمْ فِيهِ سَوَاءٌ تَخَافُونَهُمْ كَخِيفَتِكُمْ أَنفُسَكُمْ ۚ كَذَٰلِكَ نُفَصِّلُ الْآيَاتِ لِقَوْمٍ يَعْقِلُونَ
Yàlla sadd na leen ay léebu ci seen bopp : Ndax seen jaam ñi bokk nañu ak yéen seeni alal, ngeen yem ci kepp ? [Mukk], loolu rekk ngeen ragal. Nii la Nul leerale laaya yi ngir aw nit ñuy xalaat.
29بَلِ اتَّبَعَ الَّذِينَ ظَلَمُوا أَهْوَاءَهُم بِغَيْرِ عِلْمٍ ۖ فَمَن يَهْدِي مَنْ أَضَلَّ اللَّهُ ۖ وَمَا لَهُم مِّن نَّاصِرِينَ
Tooñkat yi dañoo topp seen bànneex, te àndul ak xam-xam. Ana kan mooy mën a gindi ku Yàlla réeral ? Duñu am ku leen dimbali.
30فَأَقِمْ وَجْهَكَ لِلدِّينِ حَنِيفًا ۚ فِطْرَتَ اللَّهِ الَّتِي فَطَرَ النَّاسَ عَلَيْهَا ۚ لَا تَبْدِيلَ لِخَلْقِ اللَّهِ ۚ ذَٰلِكَ الدِّينُ الْقَيِّمُ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَ النَّاسِ لَا يَعْلَمُونَ
Nangay jubbantiku topp diine Yàlla jiy cosaan te Mu sos ci nit ñi - bindéefu Yàlla du soppiku -. Loolu mooy diine ju jub ja ; waaye li ëpp ci nit ñi duñu xam.
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — Ar-Rum 28

Simoore Ar-Rum Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla sadd na leen ay léebu ci seen bopp :…

Simoore Aaya 28/60 — Simoore Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rum Dégg, Simoore Ar-Rum Tekki, Simoore Ar-Rum mp3, Simoore Ar-Rum pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers