Ar-Rum · 46/60
Tekki Waxtaan — Ar-Rum
وَمِنْ آيَاتِهِ أَن يُرْسِلَ الرِّيَاحَ مُبَشِّرَاتٍ وَلِيُذِيقَكُم مِّن رَّحْمَتِهِ وَلِتَجْرِيَ الْفُلْكُ بِأَمْرِهِ وَلِتَبْتَغُوا مِن فَضْلِهِ وَلَعَلَّكُمْ تَشْكُرُونَ ۝٤٦
Wa min Aayaatiheee anyyursilar riyaaha mubashshi raatinw wa li yuzeeqakum mir rahmatihee wa litajriyal fulku bi amrihee wa litabtaghoo min fadlihee wa la`allakum tashkuroon
📖 Tekkim Wolof
Bokk na ci ay kéemaanam, muy yebal yërmaandeem, ak gaal yi di daw ci ndigalam, te ngeen di sàkku ci xéewalam yi. Ak ngir ngeen di gëm !
🎧 Dégg

📜 Aaya 44-48 — Ar-Rum

44مَن كَفَرَ فَعَلَيْهِ كُفْرُهُ ۖ وَمَنْ عَمِلَ صَالِحًا فَلِأَنفُسِهِمْ يَمْهَدُونَ
Ku weddi, weddeem ga dana dal ca kawam. Ñay jëf yiw nag... Ñoom ña ngay waajal seen bopp [daluwaay bu maase] néeg,
45لِيَجْزِيَ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ مِن فَضْلِهِ ۚ إِنَّهُ لَا يُحِبُّ الْكَافِرِينَ
Nar naa feye ñi gëm tey jëf u yiw, ngënéelam. Moom safoowul yéefar yi.
46وَمِنْ آيَاتِهِ أَن يُرْسِلَ الرِّيَاحَ مُبَشِّرَاتٍ وَلِيُذِيقَكُم مِّن رَّحْمَتِهِ وَلِتَجْرِيَ الْفُلْكُ بِأَمْرِهِ وَلِتَبْتَغُوا مِن فَضْلِهِ وَلَعَلَّكُمْ تَشْكُرُونَ
Bokk na ci ay kéemaanam, muy yebal yërmaandeem, ak gaal yi di daw ci ndigalam, te ngeen di sàkku ci xéewalam yi. Ak ngir ngeen di gëm !
47وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا مِن قَبْلِكَ رُسُلًا إِلَىٰ قَوْمِهِمْ فَجَاءُوهُم بِالْبَيِّنَاتِ فَانتَقَمْنَا مِنَ الَّذِينَ أَجْرَمُوا ۖ وَكَانَ حَقًّا عَلَيْنَا نَصْرُ الْمُؤْمِنِينَ
Yónni woon Nanu ay Yonent yu jiitu woon ca nit ña, indiloon leen ay kàddu yu leer. Nu daldi feyu ca tooñkat ya ; te ndimbalul jullit ñi [way-gëm ñi], Maa ko warlu.
48اللَّهُ الَّذِي يُرْسِلُ الرِّيَاحَ فَتُثِيرُ سَحَابًا فَيَبْسُطُهُ فِي السَّمَاءِ كَيْفَ يَشَاءُ وَيَجْعَلُهُ كِسَفًا فَتَرَى الْوَدْقَ يَخْرُجُ مِنْ خِلَالِهِ ۖ فَإِذَا أَصَابَ بِهِ مَن يَشَاءُ مِنْ عِبَادِهِ إِذَا هُمْ يَسْتَبْشِرُونَ
Yàlla miy yebal ngelaw mu yenu niir, di ko tàbbal ci asamaan si na Mu ko soobe ; Mu di ko def ay daggit. Ab taw di ca génnee su ko tawale. Ña ko soob ci jaamam yi, ndeketeyoo dañuy sëgg ree ngir bég,
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
46Aaya

Tekki — Ar-Rum 46

Simoore Ar-Rum Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bokk na ci ay kéemaanam, muy yebal yërmaandeem, ak gaal…

Simoore Aaya 46/60 — Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Rum Dégg, Ar-Rum Tekki, Ar-Rum mp3, Ar-Rum pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers