Ar-Rum · 45/60
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rum
لِيَجْزِيَ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ مِن فَضْلِهِ ۚ إِنَّهُ لَا يُحِبُّ الْكَافِرِينَ ۝٤٥
Li yajziyal lazeena aamanoo wa `amilus saalihaati min fadlih; innahoo laa yuhibbul kaafireen
📖 Tekkim Wolof
Nar naa feye ñi gëm tey jëf u yiw, ngënéelam. Moom safoowul yéefar yi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 43-47 — Simoore Ar-Rum

43فَأَقِمْ وَجْهَكَ لِلدِّينِ الْقَيِّمِ مِن قَبْلِ أَن يَأْتِيَ يَوْمٌ لَّا مَرَدَّ لَهُ مِنَ اللَّهِ ۖ يَوْمَئِذٍ يَصَّدَّعُونَ
Jubbantikul topp diine ju jub ja, ba laa bis di ñëw boo xam ne kenn du ko mën a randal ca Yàlla. Bu keroogee, danañu fallaxoo [réeroo, téqalikoo] :
44مَن كَفَرَ فَعَلَيْهِ كُفْرُهُ ۖ وَمَنْ عَمِلَ صَالِحًا فَلِأَنفُسِهِمْ يَمْهَدُونَ
Ku weddi, weddeem ga dana dal ca kawam. Ñay jëf yiw nag... Ñoom ña ngay waajal seen bopp [daluwaay bu maase] néeg,
45لِيَجْزِيَ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ مِن فَضْلِهِ ۚ إِنَّهُ لَا يُحِبُّ الْكَافِرِينَ
Nar naa feye ñi gëm tey jëf u yiw, ngënéelam. Moom safoowul yéefar yi.
46وَمِنْ آيَاتِهِ أَن يُرْسِلَ الرِّيَاحَ مُبَشِّرَاتٍ وَلِيُذِيقَكُم مِّن رَّحْمَتِهِ وَلِتَجْرِيَ الْفُلْكُ بِأَمْرِهِ وَلِتَبْتَغُوا مِن فَضْلِهِ وَلَعَلَّكُمْ تَشْكُرُونَ
Bokk na ci ay kéemaanam, muy yebal yërmaandeem, ak gaal yi di daw ci ndigalam, te ngeen di sàkku ci xéewalam yi. Ak ngir ngeen di gëm !
47وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا مِن قَبْلِكَ رُسُلًا إِلَىٰ قَوْمِهِمْ فَجَاءُوهُم بِالْبَيِّنَاتِ فَانتَقَمْنَا مِنَ الَّذِينَ أَجْرَمُوا ۖ وَكَانَ حَقًّا عَلَيْنَا نَصْرُ الْمُؤْمِنِينَ
Yónni woon Nanu ay Yonent yu jiitu woon ca nit ña, indiloon leen ay kàddu yu leer. Nu daldi feyu ca tooñkat ya ; te ndimbalul jullit ñi [way-gëm ñi], Maa ko warlu.
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — Ar-Rum 45

Simoore Ar-Rum Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nar naa feye ñi gëm tey jëf u yiw, ngënéelam.…

Simoore Aaya 45/60 — Simoore Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rum Dégg, Simoore Ar-Rum Tekki, Simoore Ar-Rum mp3, Simoore Ar-Rum pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers