Al-Ahzab · 18/73
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ahzab
۞ قَدْ يَعْلَمُ اللَّهُ الْمُعَوِّقِينَ مِنكُمْ وَالْقَائِلِينَ لِإِخْوَانِهِمْ هَلُمَّ إِلَيْنَا ۖ وَلَا يَأْتُونَ الْبَأْسَ إِلَّا قَلِيلًا ۝١٨
Qad ya`lamul laahul mu`awwiqeena minkum walqaaa`ileena li ikhwaanihim hahumma ilainaa, wa laa yaatoonal baasa illaa qaleelaa
📖 Tekkim Wolof
Yàlla xam na ñay gàllankoore ci yéen ak ñay wax : “Ñëwleen ci nun”, fekk na yabuñu ab xare,

🎧 Dégg


📜 Aaya 16-20 — Simoore Al-Ahzab

16قُل لَّن يَنفَعَكُمُ الْفِرَارُ إِن فَرَرْتُم مِّنَ الْمَوْتِ أَوِ الْقَتْلِ وَإِذًا لَّا تُمَتَّعُونَ إِلَّا قَلِيلًا
Neel : “Su ngeen dawee it, seenug daw duleen jariñ dara ; rey mbaa dee rekk a fiy am, dundu yàggul”.
17قُلْ مَن ذَا الَّذِي يَعْصِمُكُم مِّنَ اللَّهِ إِنْ أَرَادَ بِكُمْ سُوءًا أَوْ أَرَادَ بِكُمْ رَحْمَةً ۚ وَلَا يَجِدُونَ لَهُم مِّن دُونِ اللَّهِ وَلِيًّا وَلَا نَصِيرًا
Neel : “Ana kan moo leen di musal ci Yàlla, su nammee ci yéen safaan walla Mu namm ci yéen yërmaande ? ”. Duñu am wéeruwaay walla ndimbal leneen lu dul Yàlla.
18۞ قَدْ يَعْلَمُ اللَّهُ الْمُعَوِّقِينَ مِنكُمْ وَالْقَائِلِينَ لِإِخْوَانِهِمْ هَلُمَّ إِلَيْنَا ۖ وَلَا يَأْتُونَ الْبَأْسَ إِلَّا قَلِيلًا
Yàlla xam na ñay gàllankoore ci yéen ak ñay wax : “Ñëwleen ci nun”, fekk na yabuñu ab xare,
19أَشِحَّةً عَلَيْكُمْ ۖ فَإِذَا جَاءَ الْخَوْفُ رَأَيْتَهُمْ يَنظُرُونَ إِلَيْكَ تَدُورُ أَعْيُنُهُمْ كَالَّذِي يُغْشَىٰ عَلَيْهِ مِنَ الْمَوْتِ ۖ فَإِذَا ذَهَبَ الْخَوْفُ سَلَقُوكُم بِأَلْسِنَةٍ حِدَادٍ أَشِحَّةً عَلَى الْخَيْرِ ۚ أُولَٰئِكَ لَمْ يُؤْمِنُوا فَأَحْبَطَ اللَّهُ أَعْمَالَهُمْ ۚ وَكَانَ ذَٰلِكَ عَلَى اللَّهِ يَسِيرًا
Dañuy soxore loolu ci yéen. Bu am tiit dikke, nga gis ñu di la xool, seen gët yi di wur- wuri mel ni ñuy sukkraat. Bu tiit ma jeexee, ñu di leen teg ay baat yu ñaaw. Ña bañ aw yiw, ñoom ñooñee gëmuñu. Yàlla daldi sepi seeni jëf. Te loolu yomb na Yàlla.
20يَحْسَبُونَ الْأَحْزَابَ لَمْ يَذْهَبُوا ۖ وَإِن يَأْتِ الْأَحْزَابُ يَوَدُّوا لَوْ أَنَّهُم بَادُونَ فِي الْأَعْرَابِ يَسْأَلُونَ عَنْ أَنبَائِكُمْ ۖ وَلَوْ كَانُوا فِيكُم مَّا قَاتَلُوا إِلَّا قَلِيلًا
Te ñuy foog ne farandoo ya demuñu. Te bu ñu dikkoon, dañu naa ngéeju bokk ca màngaan ya, duñu xam li ngeen xewle lu dul bu ñu ko laajtoo. Bu ñu nekkee ci seen biir itam, lu néew la ñuy xareji.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
18Aaya

Tekki — Al-Ahzab 18

Simoore Al-Ahzab Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla xam na ñay gàllankoore ci yéen ak ñay wax…

Simoore Aaya 18/73 — Simoore Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ahzab Dégg, Simoore Al-Ahzab Tekki, Simoore Al-Ahzab mp3, Simoore Al-Ahzab pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers