Ya-Sin · 12/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
إِنَّا نَحْنُ نُحْيِي الْمَوْتَىٰ وَنَكْتُبُ مَا قَدَّمُوا وَآثَارَهُمْ ۚ وَكُلَّ شَيْءٍ أَحْصَيْنَاهُ فِي إِمَامٍ مُّبِينٍ ١٢
Transliteration
Innaa Nahnu nuhyil mawtaa wa naktubu maa qaddamoo wa aasaarahum; wa kulla shai`in ahsainaahu feee Imaamim Mubeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Nun Yàlla nooy dundal néew tey bind la ñu defoon ak seeni jeexit. Te mbir mu ci bokk yéege Nanu ko ci biir ab téere bu bir , bind ko ca.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 10-14 — Ya-Sin
10وَسَوَاءٌ عَلَيْهِمْ أَأَنذَرْتَهُمْ أَمْ لَمْ تُنذِرْهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Nga xupp leen ak nga ñàkk leen a xupp ñoo yem kepp ci ñoom : duñu mës a gëm.
11إِنَّمَا تُنذِرُ مَنِ اتَّبَعَ الذِّكْرَ وَخَشِيَ الرَّحْمَٰنَ بِالْغَيْبِ ۖ فَبَشِّرْهُ بِمَغْفِرَةٍ وَأَجْرٍ كَرِيمٍ
Ka ngay war a xupp kay mooy kay topp [Alxuraan], tey ragal Yàlla ci kumpa. Nanga ko bégal ci ag njéggal ak pey gu tedd .
12إِنَّا نَحْنُ نُحْيِي الْمَوْتَىٰ وَنَكْتُبُ مَا قَدَّمُوا وَآثَارَهُمْ ۚ وَكُلَّ شَيْءٍ أَحْصَيْنَاهُ فِي إِمَامٍ مُّبِينٍ
Nun Yàlla nooy dundal néew tey bind la ñu defoon ak seeni jeexit. Te mbir mu ci bokk yéege Nanu ko ci biir ab téere bu bir , bind ko ca.
13وَاضْرِبْ لَهُم مَّثَلًا أَصْحَابَ الْقَرْيَةِ إِذْ جَاءَهَا الْمُرْسَلُونَ
Joxleen misaal ci waa dëkk ba ab Yonent dikkaloon.
14إِذْ أَرْسَلْنَا إِلَيْهِمُ اثْنَيْنِ فَكَذَّبُوهُمَا فَعَزَّزْنَا بِثَالِثٍ فَقَالُوا إِنَّا إِلَيْكُم مُّرْسَلُونَ
Ba Nu leen jebalee ñaari ndaw ñu weddi leen. Nu daldi leen kàttanalaat ci ndaw lu leen ñetteel, ñu ànd ñoom ñett, ne leen : “Nun ndawi Yàlla lanu”.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
12Aaya
Tekki — Ya-Sin 12
Simoore Ya-Sin Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun Yàlla nooy dundal néew tey bind la ñu defoon…Simoore Aaya 12/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








