Ya-Sin · 31/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
أَلَمْ يَرَوْا كَمْ أَهْلَكْنَا قَبْلَهُم مِّنَ الْقُرُونِ أَنَّهُمْ إِلَيْهِمْ لَا يَرْجِعُونَ ۝٣١
Alam yaraw kam ahlak naa qablahum minal qurooni annahum ilaihim laa yarji`oon
📖 Tekkim Wolof
Xanaa gisuñu na Nu faagale woon maas ya leen jiitu woon ? Te kenn du ca dellusi.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 29-33 — Simoore Ya-Sin

29إِن كَانَتْ إِلَّا صَيْحَةً وَاحِدَةً فَإِذَا هُمْ خَامِدُونَ
Génn xaacu rekk a fa jaar, ñu faf giim.
30يَا حَسْرَةً عَلَى الْعِبَادِ ۚ مَا يَأْتِيهِم مِّن رَّسُولٍ إِلَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
Ndeysaan jaam ñi le ! Ab Yonent mësuleen a dikkal mukk te du dañu koy ñaawal.
31أَلَمْ يَرَوْا كَمْ أَهْلَكْنَا قَبْلَهُم مِّنَ الْقُرُونِ أَنَّهُمْ إِلَيْهِمْ لَا يَرْجِعُونَ
Xanaa gisuñu na Nu faagale woon maas ya leen jiitu woon ? Te kenn du ca dellusi.
32وَإِن كُلٌّ لَّمَّا جَمِيعٌ لَّدَيْنَا مُحْضَرُونَ
Te ñoom ñépp danañu daje Sama kanam .
33وَآيَةٌ لَّهُمُ الْأَرْضُ الْمَيْتَةُ أَحْيَيْنَاهَا وَأَخْرَجْنَا مِنْهَا حَبًّا فَمِنْهُ يَأْكُلُونَ
Indil Nanu leen firnde te moo di suuf si dee , Nu dekkalaat ko, [tawu ndow] génne ca ay doom, ngeen di ca lekk.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
31Aaya

Tekki — Ya-Sin 31

Simoore Ya-Sin Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xanaa gisuñu na Nu faagale woon maas ya leen jiitu…

Simoore Aaya 31/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers