As-Saffat · 24/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَقِفُوهُمْ ۖ إِنَّهُم مَّسْئُولُونَ ۝٢٤
Wa qifoohum innahum mas`ooloon
📖 Tekkim Wolof
Te ngeen taxawlooleen : ndax dañu leen di laaj”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 22-26 — Simoore As-Saffat

22۞ احْشُرُوا الَّذِينَ ظَلَمُوا وَأَزْوَاجَهُمْ وَمَا كَانُوا يَعْبُدُونَ
“Dajaleleen tooñkat ya ak seeni jabar ak la ñu daan jaamu,
23مِن دُونِ اللَّهِ فَاهْدُوهُمْ إِلَىٰ صِرَاطِ الْجَحِيمِ
bàyyi woon Yàlla. Te wëtal leen jëme yoonu Safara.
24وَقِفُوهُمْ ۖ إِنَّهُم مَّسْئُولُونَ
Te ngeen taxawlooleen : ndax dañu leen di laaj”.
25مَا لَكُمْ لَا تَنَاصَرُونَ
“Ana lan moo tax dungeen dimbalante” ?
26بَلْ هُمُ الْيَوْمَ مُسْتَسْلِمُونَ
Li wér mooy bis niki tey jébbalu nañu,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — As-Saffat 24

Simoore As-Saffat Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te ngeen taxawlooleen : ndax dañu leen di laaj”.

Simoore Aaya 24/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers