As-Saffat · 23/182
Tekki Waxtaan — As-Saffat
مِن دُونِ اللَّهِ فَاهْدُوهُمْ إِلَىٰ صِرَاطِ الْجَحِيمِ ٢٣
Transliteration
Min doonil laahi fahdoohum ilaa siraatil Jaheem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
bàyyi woon Yàlla. Te wëtal leen jëme yoonu Safara.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 21-25 — As-Saffat
21هَٰذَا يَوْمُ الْفَصْلِ الَّذِي كُنتُم بِهِ تُكَذِّبُونَ
“Lii mooy bisub àtte ba ngeen jàppe woon ay fen, weddi ko”.
22۞ احْشُرُوا الَّذِينَ ظَلَمُوا وَأَزْوَاجَهُمْ وَمَا كَانُوا يَعْبُدُونَ
“Dajaleleen tooñkat ya ak seeni jabar ak la ñu daan jaamu,
23مِن دُونِ اللَّهِ فَاهْدُوهُمْ إِلَىٰ صِرَاطِ الْجَحِيمِ
bàyyi woon Yàlla. Te wëtal leen jëme yoonu Safara.
24وَقِفُوهُمْ ۖ إِنَّهُم مَّسْئُولُونَ
Te ngeen taxawlooleen : ndax dañu leen di laaj”.
25مَا لَكُمْ لَا تَنَاصَرُونَ
“Ana lan moo tax dungeen dimbalante” ?
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
23Aaya
Tekki — As-Saffat 23
Simoore As-Saffat Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : bàyyi woon Yàlla. Te wëtal leen jëme yoonu Safara.Simoore Aaya 23/182 — As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: As-Saffat Dégg, As-Saffat Tekki, As-Saffat mp3, As-Saffat pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








