As-Saffat · 25/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
مَا لَكُمْ لَا تَنَاصَرُونَ ۝٢٥
Maa lakum laa tanaasaroon
📖 Tekkim Wolof
“Ana lan moo tax dungeen dimbalante” ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 23-27 — Simoore As-Saffat

23مِن دُونِ اللَّهِ فَاهْدُوهُمْ إِلَىٰ صِرَاطِ الْجَحِيمِ
bàyyi woon Yàlla. Te wëtal leen jëme yoonu Safara.
24وَقِفُوهُمْ ۖ إِنَّهُم مَّسْئُولُونَ
Te ngeen taxawlooleen : ndax dañu leen di laaj”.
25مَا لَكُمْ لَا تَنَاصَرُونَ
“Ana lan moo tax dungeen dimbalante” ?
26بَلْ هُمُ الْيَوْمَ مُسْتَسْلِمُونَ
Li wér mooy bis niki tey jébbalu nañu,
27وَأَقْبَلَ بَعْضُهُمْ عَلَىٰ بَعْضٍ يَتَسَاءَلُونَ
ku nekk di geesu moroom ma, ñuy laajante ;
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — As-Saffat 25

Simoore As-Saffat Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Ana lan moo tax dungeen dimbalante” ?

Simoore Aaya 25/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers