As-Saffat · 4/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِنَّ إِلَٰهَكُمْ لَوَاحِدٌ ۝٤
Inna Illaahakum la Waahid
📖 Tekkim Wolof
“Ne seen Yàlla jenn la tigi,

🎧 Dégg


📜 Aaya 2-6 — Simoore As-Saffat

2فَالزَّاجِرَاتِ زَجْرًا
Ñay bëmëg niir yaak doole.
3فَالتَّالِيَاتِ ذِكْرًا
Ñay jàng ngir fàttali :
4إِنَّ إِلَٰهَكُمْ لَوَاحِدٌ
“Ne seen Yàlla jenn la tigi,
5رَّبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا وَرَبُّ الْمَشَارِقِ
mooy Boroom asamaan yeek suuf si ak li nekk seen diggante tey Boroom penku yi”.
6إِنَّا زَيَّنَّا السَّمَاءَ الدُّنْيَا بِزِينَةٍ الْكَوَاكِبِ
Taaralal Nanu asamaan si gën a jexe àddina si ci taarub ay bidiw,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
4Aaya

Tekki — As-Saffat 4

Simoore As-Saffat Aaya 4 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Ne seen Yàlla jenn la tigi,

Simoore Aaya 4/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 2–6. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers