As-Saffat · 6/182
Tekki Waxtaan — As-Saffat
إِنَّا زَيَّنَّا السَّمَاءَ الدُّنْيَا بِزِينَةٍ الْكَوَاكِبِ ٦
Transliteration
Innaa zaiyannas samaaa `ad dunyaa bizeenatinil kawaakib
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Taaralal Nanu asamaan si gën a jexe àddina si ci taarub ay bidiw,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 4-8 — As-Saffat
4إِنَّ إِلَٰهَكُمْ لَوَاحِدٌ
“Ne seen Yàlla jenn la tigi,
5رَّبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا وَرَبُّ الْمَشَارِقِ
mooy Boroom asamaan yeek suuf si ak li nekk seen diggante tey Boroom penku yi”.
6إِنَّا زَيَّنَّا السَّمَاءَ الدُّنْيَا بِزِينَةٍ الْكَوَاكِبِ
Taaralal Nanu asamaan si gën a jexe àddina si ci taarub ay bidiw,
7وَحِفْظًا مِّن كُلِّ شَيْطَانٍ مَّارِدٍ
def ca kaaraange ci sépp séytaane suy féttérlu.
8لَّا يَسَّمَّعُونَ إِلَى الْمَلَإِ الْأَعْلَىٰ وَيُقْذَفُونَ مِن كُلِّ جَانِبٍ
Duñu mën yëddu waa péey ba gën a kawe ; te dañu leen fay mbàqe wet gu nekk,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
6Aaya
Tekki — As-Saffat 6
Simoore As-Saffat Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Taaralal Nanu asamaan si gën a jexe àddina si ci…Simoore Aaya 6/182 — As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: As-Saffat Dégg, As-Saffat Tekki, As-Saffat mp3, As-Saffat pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








