As-Saffat · 7/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَحِفْظًا مِّن كُلِّ شَيْطَانٍ مَّارِدٍ ۝٧
Wa hifzam min kulli Shaitaanim maarid
📖 Tekkim Wolof
def ca kaaraange ci sépp séytaane suy féttérlu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 5-9 — Simoore As-Saffat

5رَّبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا وَرَبُّ الْمَشَارِقِ
mooy Boroom asamaan yeek suuf si ak li nekk seen diggante tey Boroom penku yi”.
6إِنَّا زَيَّنَّا السَّمَاءَ الدُّنْيَا بِزِينَةٍ الْكَوَاكِبِ
Taaralal Nanu asamaan si gën a jexe àddina si ci taarub ay bidiw,
7وَحِفْظًا مِّن كُلِّ شَيْطَانٍ مَّارِدٍ
def ca kaaraange ci sépp séytaane suy féttérlu.
8لَّا يَسَّمَّعُونَ إِلَى الْمَلَإِ الْأَعْلَىٰ وَيُقْذَفُونَ مِن كُلِّ جَانِبٍ
Duñu mën yëddu waa péey ba gën a kawe ; te dañu leen fay mbàqe wet gu nekk,
9دُحُورًا ۖ وَلَهُمْ عَذَابٌ وَاصِبٌ
dàqe leen fa. Ñu am mbugal muy sax.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — As-Saffat 7

Simoore As-Saffat Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : def ca kaaraange ci sépp séytaane suy féttérlu.

Simoore Aaya 7/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers