Az-Zumar · 2/75
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zumar
إِنَّا أَنزَلْنَا إِلَيْكَ الْكِتَابَ بِالْحَقِّ فَاعْبُدِ اللَّهَ مُخْلِصًا لَّهُ الدِّينَ ۝٢
Innaaa anzalnaaa ilaikal Kitaaba bilhaqqi fa`budil laaha mukhlisal lahud deen
📖 Tekkim Wolof
Wàcce Nanu ci yaw Téere bi ci dëgg. Na ngay jaamu Yàlla te di ko sellalal jaamu ga.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-4 — Simoore Az-Zumar

1تَنزِيلُ الْكِتَابِ مِنَ اللَّهِ الْعَزِيزِ الْحَكِيمِ
Wàcceg Téere ba bawoo ca Yàlla, miy boroom Kàttan, di ku Xereñ.
2إِنَّا أَنزَلْنَا إِلَيْكَ الْكِتَابَ بِالْحَقِّ فَاعْبُدِ اللَّهَ مُخْلِصًا لَّهُ الدِّينَ
Wàcce Nanu ci yaw Téere bi ci dëgg. Na ngay jaamu Yàlla te di ko sellalal jaamu ga.
3أَلَا لِلَّهِ الدِّينُ الْخَالِصُ ۚ وَالَّذِينَ اتَّخَذُوا مِن دُونِهِ أَوْلِيَاءَ مَا نَعْبُدُهُمْ إِلَّا لِيُقَرِّبُونَا إِلَى اللَّهِ زُلْفَىٰ إِنَّ اللَّهَ يَحْكُمُ بَيْنَهُمْ فِي مَا هُمْ فِيهِ يَخْتَلِفُونَ ۗ إِنَّ اللَّهَ لَا يَهْدِي مَنْ هُوَ كَاذِبٌ كَفَّارٌ
Yàlla rekk am diine ju sell. Ñay jaamu leneen lu dul moom tey (wax naan) : “Lii nuy jaamu daal danu ciy sukandiku ngir man a jigeñ Yàlla”. Te, Yàlla dana àtte seen diggënte ci la ñu daan woote. Yàlla du gindi fenkat bu weddiwaakoon.
4لَّوْ أَرَادَ اللَّهُ أَن يَتَّخِذَ وَلَدًا لَّاصْطَفَىٰ مِمَّا يَخْلُقُ مَا يَشَاءُ ۚ سُبْحَانَهُ ۖ هُوَ اللَّهُ الْوَاحِدُ الْقَهَّارُ
Su Yàlla nàmmoon jàppe kenn doomam, Kon dana tànn ca la mu bind namu ko soobe (waaye nammu ko). Tudd naa Sellam ga ! Mooy Yàlla, jiy Jenn, tey Notaakoon ba.
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
2Aaya

Tekki — Az-Zumar 2

Simoore Az-Zumar Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Wàcce Nanu ci yaw Téere bi ci dëgg. Na ngay…

Simoore Aaya 2/75 — Simoore Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zumar Dégg, Simoore Az-Zumar Tekki, Simoore Az-Zumar mp3, Simoore Az-Zumar pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers