Az-Zumar · 42/75
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zumar
اللَّهُ يَتَوَفَّى الْأَنفُسَ حِينَ مَوْتِهَا وَالَّتِي لَمْ تَمُتْ فِي مَنَامِهَا ۖ فَيُمْسِكُ الَّتِي قَضَىٰ عَلَيْهَا الْمَوْتَ وَيُرْسِلُ الْأُخْرَىٰ إِلَىٰ أَجَلٍ مُّسَمًّى ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يَتَفَكَّرُونَ ۝٤٢
Allaahu yatawaffal anfusa heena mawtihaa wallatee lam tamut fee manaamihaa fa yumsikul latee qadaa `alaihal mawta wa yursilul ukhraaa ilaaa ajalim musammaa; inna fee zaalika la Aayaatil liqawmai yatafakkarron
📖 Tekkim Wolof
Yàlla mooy faat bakkan bu ñuy dee ak ya deewul ci biiri nelaw. Mooy téye ya mu namm ñu dee, di boyal ya ca des jëme ko ca dig ba mu ko àppal. Ay kéemaan a ngi ci biir loolu ngir aw nit ñuy xalaat.

🎧 Dégg


📜 Aaya 40-44 — Simoore Az-Zumar

40مَن يَأْتِيهِ عَذَابٌ يُخْزِيهِ وَيَحِلُّ عَلَيْهِ عَذَابٌ مُّقِيمٌ
ana kan la mbugël di dikk toroxal ko ; ak ci kaw kan la mbugëlam dëggële di wàcc”.
41إِنَّا أَنزَلْنَا عَلَيْكَ الْكِتَابَ لِلنَّاسِ بِالْحَقِّ ۖ فَمَنِ اهْتَدَىٰ فَلِنَفْسِهِ ۖ وَمَن ضَلَّ فَإِنَّمَا يَضِلُّ عَلَيْهَا ۖ وَمَا أَنتَ عَلَيْهِم بِوَكِيلٍ
Wàcce Nanu ci yaw Téere ba, ci dëgg, ngir nit ñi. Ku gindiku boppam ; ku réer it boppam. Seenub lijjënti warula
42اللَّهُ يَتَوَفَّى الْأَنفُسَ حِينَ مَوْتِهَا وَالَّتِي لَمْ تَمُتْ فِي مَنَامِهَا ۖ فَيُمْسِكُ الَّتِي قَضَىٰ عَلَيْهَا الْمَوْتَ وَيُرْسِلُ الْأُخْرَىٰ إِلَىٰ أَجَلٍ مُّسَمًّى ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يَتَفَكَّرُونَ
Yàlla mooy faat bakkan bu ñuy dee ak ya deewul ci biiri nelaw. Mooy téye ya mu namm ñu dee, di boyal ya ca des jëme ko ca dig ba mu ko àppal. Ay kéemaan a ngi ci biir loolu ngir aw nit ñuy xalaat.
43أَمِ اتَّخَذُوا مِن دُونِ اللَّهِ شُفَعَاءَ ۚ قُلْ أَوَلَوْ كَانُوا لَا يَمْلِكُونَ شَيْئًا وَلَا يَعْقِلُونَ
Walla dañoo wut, yeneeni tinukat, bàyyi Yàlla ? Waxal ne : “Ndax ! Nekkuñu woon ñu amal dara te xamu ñu dara ? ”
44قُل لِّلَّهِ الشَّفَاعَةُ جَمِيعًا ۖ لَّهُ مُلْكُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ ثُمَّ إِلَيْهِ تُرْجَعُونَ
Waxal ne : “Tinu ba tinu jeex (ramm) Yàllaa ko jagoo. Miy boroom nguurug asamaan yeek suuf. Te ci moom ngeen di dellu”
Az-ZumarFihi Alxuraan
75Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Az-Zumar 42

Simoore Az-Zumar Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla mooy faat bakkan bu ñuy dee ak ya deewul…

Simoore Aaya 42/75 — Simoore Az-Zumar الزمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zumar Dégg, Simoore Az-Zumar Tekki, Simoore Az-Zumar mp3, Simoore Az-Zumar pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers