Az-Zukhruf · 27/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
إِلَّا الَّذِي فَطَرَنِي فَإِنَّهُ سَيَهْدِينِ ۝٢٧
Illal lazee fataranee innahoo sa yahdeen
📖 Tekkim Wolof
ba mu des (Yàlla) mi ma sàkk bind ma, te moo may gindi”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 25-29 — Simoore Az-Zukhruf

25فَانتَقَمْنَا مِنْهُمْ ۖ فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُكَذِّبِينَ
Nu daldi fayu ca seen kaw. Xoolal (settantal) naka la mujjug weddikat ya deme.
26وَإِذْ قَالَ إِبْرَاهِيمُ لِأَبِيهِ وَقَوْمِهِ إِنَّنِي بَرَاءٌ مِّمَّا تَعْبُدُونَ
(Fàttalikul) Ibraahiima ba mu waxee baayam aku nitam : “Man mii ku deñ laa ci lii ngeen di jaamu,
27إِلَّا الَّذِي فَطَرَنِي فَإِنَّهُ سَيَهْدِينِ
ba mu des (Yàlla) mi ma sàkk bind ma, te moo may gindi”.
28وَجَعَلَهَا كَلِمَةً بَاقِيَةً فِي عَقِبِهِ لَعَلَّهُمْ يَرْجِعُونَ
Mu def (dénkaane boobu) muy kàddu guy sax ginnaawam. Ngir amaana ñu dellu (di jëfe seeni xel) ?
29بَلْ مَتَّعْتُ هَٰؤُلَاءِ وَآبَاءَهُمْ حَتَّىٰ جَاءَهُمُ الْحَقُّ وَرَسُولٌ مُّبِينٌ
Waaye xéewaloon naa ñooñee ak seeni maam, Ba dëgg ga (Alxuraan) digël leen ànd ak Yonnent buy leeral.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 27

Simoore Az-Zukhruf Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ba mu des (Yàlla) mi ma sàkk bind ma, te…

Simoore Aaya 27/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers