Az-Zukhruf · 34/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
وَلِبُيُوتِهِمْ أَبْوَابًا وَسُرُرًا عَلَيْهَا يَتَّكِئُونَ ٣٤
Transliteration
Wa libu yootihim abwaabanw wa sururan `alaihaa yattaki`oon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
seen kër ya amna ay wunt ak ay lal ñu di ca sóonu,
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 32-36 — Simoore Az-Zukhruf
32أَهُمْ يَقْسِمُونَ رَحْمَتَ رَبِّكَ ۚ نَحْنُ قَسَمْنَا بَيْنَهُم مَّعِيشَتَهُمْ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ۚ وَرَفَعْنَا بَعْضَهُمْ فَوْقَ بَعْضٍ دَرَجَاتٍ لِّيَتَّخِذَ بَعْضُهُم بَعْضًا سُخْرِيًّا ۗ وَرَحْمَتُ رَبِّكَ خَيْرٌ مِّمَّا يَجْمَعُونَ
Moo ndax ñoom ñooy séddële yërmaandey sa Boroom ? Te Nun dey Noo leen di séddale seenub dundu ci àddina te it tooñkat ya ñennat ci ñoom, teg na leen ca kaw ña ca des ngir nuy yilifante. Waaye yërmaandey sa Boroom, moo gën fuuf, li ñuy dajale.
33وَلَوْلَا أَن يَكُونَ النَّاسُ أُمَّةً وَاحِدَةً لَّجَعَلْنَا لِمَن يَكْفُرُ بِالرَّحْمَٰنِ لِبُيُوتِهِمْ سُقُفًا مِّن فِضَّةٍ وَمَعَارِجَ عَلَيْهَا يَظْهَرُونَ
Su nit ñi doonoon wenn xeet, kon Dinanu defaral ñiy weddi Yàlla, seeni kër am ay xàddi xaalis ak ay ker-keraan ñu di ca yéege ;
34وَلِبُيُوتِهِمْ أَبْوَابًا وَسُرُرًا عَلَيْهَا يَتَّكِئُونَ
seen kër ya amna ay wunt ak ay lal ñu di ca sóonu,
35وَزُخْرُفًا ۚ وَإِن كُلُّ ذَٰلِكَ لَمَّا مَتَاعُ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ۚ وَالْآخِرَةُ عِندَ رَبِّكَ لِلْمُتَّقِينَ
ak ay xoyxoyal. loolu lépp du lenn lu dul bànneexu dundug àddina, te àllaaxiraa, nga fa sa Boroom, ngir ñu ragal Yàlla.
36وَمَن يَعْشُ عَن ذِكْرِ الرَّحْمَٰنِ نُقَيِّضْ لَهُ شَيْطَانًا فَهُوَ لَهُ قَرِينٌ
Képp kuy sori ak a dumóoyu tudd Yàlla (fàttaliku) Yëramaakoon bi, Dananu ko booleek Saytaane su mu lëkkalool.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
34Aaya
Tekki — Az-Zukhruf 34
Simoore Az-Zukhruf Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : seen kër ya amna ay wunt ak ay lal ñu…Simoore Aaya 34/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Az-Zukhruf
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Friday, October 2, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


