Az-Zukhruf · 40/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
أَفَأَنتَ تُسْمِعُ الصُّمَّ أَوْ تَهْدِي الْعُمْيَ وَمَن كَانَ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ ۝٤٠
Afa anta tusmi`us summa aw tahdil `umya wa man kaana fee dalaalim mubeen
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax yaw man ngaa déggloo ku tëx mbaa nga man a gindi ku gumba mba ku nekk ci réer gu tar ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 38-42 — Simoore Az-Zukhruf

38حَتَّىٰ إِذَا جَاءَنَا قَالَ يَا لَيْتَ بَيْنِي وَبَيْنَكَ بُعْدَ الْمَشْرِقَيْنِ فَبِئْسَ الْقَرِينُ
Ba ne seef agsi ci Nun dey, daldi wax ne: “Aka neexoon ! Sunu diggënte soriyaantoo ni [Pénkook Suwu] ! ” – Ndaw lëkkëloo bu bon !
39وَلَن يَنفَعَكُمُ الْيَوْمَ إِذ ظَّلَمْتُمْ أَنَّكُمْ فِي الْعَذَابِ مُشْتَرِكُونَ
Loolu lépp du leen jariñ lenn tey jii – ginnaaw ba ngeen tooñee – yéen ay bokk yem ca biir mbugël ma.
40أَفَأَنتَ تُسْمِعُ الصُّمَّ أَوْ تَهْدِي الْعُمْيَ وَمَن كَانَ فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Moo ndax yaw man ngaa déggloo ku tëx mbaa nga man a gindi ku gumba mba ku nekk ci réer gu tar ?
41فَإِمَّا نَذْهَبَنَّ بِكَ فَإِنَّا مِنْهُم مُّنتَقِمُونَ
Benn nu yóbbu la nga [dee] Nu daldi fayu ci ñoom ;
42أَوْ نُرِيَنَّكَ الَّذِي وَعَدْنَاهُمْ فَإِنَّا عَلَيْهِم مُّقْتَدِرُونَ
Walla Nu wan la la Nu leen digoon ñoom ; am Nanu Kàttan ci seen kaw de.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
40Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 40

Simoore Az-Zukhruf Aaya 40 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax yaw man ngaa déggloo ku tëx mbaa nga…

Simoore Aaya 40/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 38–42. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers