Az-Zukhruf · 46/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا مُوسَىٰ بِآيَاتِنَا إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِ فَقَالَ إِنِّي رَسُولُ رَبِّ الْعَالَمِينَ ۝٤٦
Wa laqad arsalnaa Moosaa bi aayaatinaaa ilaa Fir`awna wa mala`ihee faqaala innee Rasoolu Rabbil `aalameen
📖 Tekkim Wolof
Yónni woon Nanu Muusaa ak Sunuy kéemaan, ci Firawna ak gàngooram ga. Mu ne leen: “Man ndawul Boroom àddina si laa”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 44-48 — Simoore Az-Zukhruf

44وَإِنَّهُ لَذِكْرٌ لَّكَ وَلِقَوْمِكَ ۖ وَسَوْفَ تُسْأَلُونَ
Dëgg-dëgg [Alxuraan] fàttaliku la ngir yaw ak saw nit. Te it deefna leen ko laaj.
45وَاسْأَلْ مَنْ أَرْسَلْنَا مِن قَبْلِكَ مِن رُّسُلِنَا أَجَعَلْنَا مِن دُونِ الرَّحْمَٰنِ آلِهَةً يُعْبَدُونَ
Laajal Yonent yi Nu jëkkoon a yónni ñu jiitu la, ba xam ndax defaroon Nañu Yàlla, ju bokkul ak yëramaakoon bi, ju ñuy jaamu ?
46وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا مُوسَىٰ بِآيَاتِنَا إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِ فَقَالَ إِنِّي رَسُولُ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Yónni woon Nanu Muusaa ak Sunuy kéemaan, ci Firawna ak gàngooram ga. Mu ne leen: “Man ndawul Boroom àddina si laa”.
47فَلَمَّا جَاءَهُم بِآيَاتِنَا إِذَا هُم مِّنْهَا يَضْحَكُونَ
Ba mu dikkee ca ñoom ànd ak Sunuy firnde (kéemaan), ndeketeyoo dañu koy reetaan.
48وَمَا نُرِيهِم مِّنْ آيَةٍ إِلَّا هِيَ أَكْبَرُ مِنْ أُخْتِهَا ۖ وَأَخَذْنَاهُم بِالْعَذَابِ لَعَلَّهُمْ يَرْجِعُونَ
Kéemtaan gu mujj a ñëw ëpp ga ko jiitu woon. Ba noppi nu toftal ca teg léen ay jafe-jafe, ngir amaana ñu dellu ginaaw.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
46Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 46

Simoore Az-Zukhruf Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yónni woon Nanu Muusaa ak Sunuy kéemaan, ci Firawna ak…

Simoore Aaya 46/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers