Az-Zukhruf · 73/89
Tekki Waxtaan — Az-Zukhruf
لَكُمْ فِيهَا فَاكِهَةٌ كَثِيرَةٌ مِّنْهَا تَأْكُلُونَ ۝٧٣
Lakum feehaa faakihatun kaseeratum minhaa taakuloon
📖 Tekkim Wolof
Am ngeen fa ay fuytéef yu bari ngeen di ca lekk”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 71-75 — Az-Zukhruf

71يُطَافُ عَلَيْهِم بِصِحَافٍ مِّن ذَهَبٍ وَأَكْوَابٍ ۖ وَفِيهَا مَا تَشْتَهِيهِ الْأَنفُسُ وَتَلَذُّ الْأَعْيُنُ ۖ وَأَنتُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
Danu leen fay wër ak booli wurus ak i kopp ; def lépp lu bakkan di wonnen ay gët di ko bànneexoo ; - “te dangeen fay béel.
72وَتِلْكَ الْجَنَّةُ الَّتِي أُورِثْتُمُوهَا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Loolee mooy àjjana ja Nu leen donale ci la ngeen daan jëf.
73لَكُمْ فِيهَا فَاكِهَةٌ كَثِيرَةٌ مِّنْهَا تَأْكُلُونَ
Am ngeen fa ay fuytéef yu bari ngeen di ca lekk”.
74إِنَّ الْمُجْرِمِينَ فِي عَذَابِ جَهَنَّمَ خَالِدُونَ
Tooñkat yaa ngi, ci biir mbugalum Safara béel ca,
75لَا يُفَتَّرُ عَنْهُمْ وَهُمْ فِيهِ مُبْلِسُونَ
kenn duleen ko mas a woyafal te dañu naan fa xuum ne muq ngir jaaxle.
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
73Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 73

Simoore Az-Zukhruf Aaya 73 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Am ngeen fa ay fuytéef yu bari ngeen di ca…

Simoore Aaya 73/89 — Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zukhruf Dégg, Az-Zukhruf Tekki, Az-Zukhruf mp3, Az-Zukhruf pdf. Aaya 71–75. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers