Az-Zukhruf · 72/89
Tekki Waxtaan — Az-Zukhruf
وَتِلْكَ الْجَنَّةُ الَّتِي أُورِثْتُمُوهَا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ ٧٢
Transliteration
Wa tilkal jannatul lateee ooristumoohaa bimaa kuntum ta`maloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Loolee mooy àjjana ja Nu leen donale ci la ngeen daan jëf.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 70-74 — Az-Zukhruf
70ادْخُلُوا الْجَنَّةَ أَنتُمْ وَأَزْوَاجُكُمْ تُحْبَرُونَ
“Dugguleen àjjana, yéen ak seeni soxna, danu leen fay berndeel”.
71يُطَافُ عَلَيْهِم بِصِحَافٍ مِّن ذَهَبٍ وَأَكْوَابٍ ۖ وَفِيهَا مَا تَشْتَهِيهِ الْأَنفُسُ وَتَلَذُّ الْأَعْيُنُ ۖ وَأَنتُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
Danu leen fay wër ak booli wurus ak i kopp ; def lépp lu bakkan di wonnen ay gët di ko bànneexoo ; - “te dangeen fay béel.
72وَتِلْكَ الْجَنَّةُ الَّتِي أُورِثْتُمُوهَا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Loolee mooy àjjana ja Nu leen donale ci la ngeen daan jëf.
73لَكُمْ فِيهَا فَاكِهَةٌ كَثِيرَةٌ مِّنْهَا تَأْكُلُونَ
Am ngeen fa ay fuytéef yu bari ngeen di ca lekk”.
74إِنَّ الْمُجْرِمِينَ فِي عَذَابِ جَهَنَّمَ خَالِدُونَ
Tooñkat yaa ngi, ci biir mbugalum Safara béel ca,
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
72Aaya
Tekki — Az-Zukhruf 72
Simoore Az-Zukhruf Aaya 72 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Loolee mooy àjjana ja Nu leen donale ci la ngeen…Simoore Aaya 72/89 — Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Az-Zukhruf Dégg, Az-Zukhruf Tekki, Az-Zukhruf mp3, Az-Zukhruf pdf. Aaya 70–74. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








