Az-Zukhruf · 74/89
Tekki Waxtaan — Simoore Az-Zukhruf
إِنَّ الْمُجْرِمِينَ فِي عَذَابِ جَهَنَّمَ خَالِدُونَ ۝٧٤
Innal mujrimeena fee `azaabi jahannama khaalidoon
📖 Tekkim Wolof
Tooñkat yaa ngi, ci biir mbugalum Safara béel ca,

🎧 Dégg


📜 Aaya 72-76 — Simoore Az-Zukhruf

72وَتِلْكَ الْجَنَّةُ الَّتِي أُورِثْتُمُوهَا بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Loolee mooy àjjana ja Nu leen donale ci la ngeen daan jëf.
73لَكُمْ فِيهَا فَاكِهَةٌ كَثِيرَةٌ مِّنْهَا تَأْكُلُونَ
Am ngeen fa ay fuytéef yu bari ngeen di ca lekk”.
74إِنَّ الْمُجْرِمِينَ فِي عَذَابِ جَهَنَّمَ خَالِدُونَ
Tooñkat yaa ngi, ci biir mbugalum Safara béel ca,
75لَا يُفَتَّرُ عَنْهُمْ وَهُمْ فِيهِ مُبْلِسُونَ
kenn duleen ko mas a woyafal te dañu naan fa xuum ne muq ngir jaaxle.
76وَمَا ظَلَمْنَاهُمْ وَلَٰكِن كَانُوا هُمُ الظَّالِمِينَ
Du ut ne Nun noo leen tooñ, waaye ñoom ñoo tooñ (seen bopp).
Az-ZukhrufFihi Alxuraan
89Aaya
MeccanRevelation
74Aaya

Tekki — Az-Zukhruf 74

Simoore Az-Zukhruf Aaya 74 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Tooñkat yaa ngi, ci biir mbugalum Safara béel ca,

Simoore Aaya 74/89 — Simoore Az-Zukhruf الزخرف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Az-Zukhruf Dégg, Simoore Az-Zukhruf Tekki, Simoore Az-Zukhruf mp3, Simoore Az-Zukhruf pdf. Aaya 72–76. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers