Ad-Dukhan · 11/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
يَغْشَى النَّاسَ ۖ هَٰذَا عَذَابٌ أَلِيمٌ ۝١١
Yaghshan naasa haazaa `azaabun aleem
📖 Tekkim Wolof
di moor nit ñi. Tey mbugël mu mitti.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 9-13 — Simoore Ad-Dukhan

9بَلْ هُمْ فِي شَكٍّ يَلْعَبُونَ
Ñoom, ña ngay sikki-sàkka, di fo.
10فَارْتَقِبْ يَوْمَ تَأْتِي السَّمَاءُ بِدُخَانٍ مُّبِينٍ
Fuglul, cëy bis ba asamaan si di dikk ak saxar suy jolli
11يَغْشَى النَّاسَ ۖ هَٰذَا عَذَابٌ أَلِيمٌ
di moor nit ñi. Tey mbugël mu mitti.
12رَّبَّنَا اكْشِفْ عَنَّا الْعَذَابَ إِنَّا مُؤْمِنُونَ
“Waay-waay, sunu Boroom téggil nu mbugël mi. Ndax nun ay jullit la nu [léegi]”.
13أَنَّىٰ لَهُمُ الذِّكْرَىٰ وَقَدْ جَاءَهُمْ رَسُولٌ مُّبِينٌ
Ana fan la leen kii fàttaliku bawoo te ab Yonnent bu bir dikkoloon leen,
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 11

Simoore Ad-Dukhan Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : di moor nit ñi. Tey mbugël mu mitti.

Simoore Aaya 11/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers