Ad-Dukhan · 12/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
رَّبَّنَا اكْشِفْ عَنَّا الْعَذَابَ إِنَّا مُؤْمِنُونَ ۝١٢
Rabbanak shif `annal `azaaba innaa mu`minoon
📖 Tekkim Wolof
“Waay-waay, sunu Boroom téggil nu mbugël mi. Ndax nun ay jullit la nu [léegi]”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Simoore Ad-Dukhan

10فَارْتَقِبْ يَوْمَ تَأْتِي السَّمَاءُ بِدُخَانٍ مُّبِينٍ
Fuglul, cëy bis ba asamaan si di dikk ak saxar suy jolli
11يَغْشَى النَّاسَ ۖ هَٰذَا عَذَابٌ أَلِيمٌ
di moor nit ñi. Tey mbugël mu mitti.
12رَّبَّنَا اكْشِفْ عَنَّا الْعَذَابَ إِنَّا مُؤْمِنُونَ
“Waay-waay, sunu Boroom téggil nu mbugël mi. Ndax nun ay jullit la nu [léegi]”.
13أَنَّىٰ لَهُمُ الذِّكْرَىٰ وَقَدْ جَاءَهُمْ رَسُولٌ مُّبِينٌ
Ana fan la leen kii fàttaliku bawoo te ab Yonnent bu bir dikkoloon leen,
14ثُمَّ تَوَلَّوْا عَنْهُ وَقَالُوا مُعَلَّمٌ مَّجْنُونٌ
Ñu daldi dumóoyu te naan : “Kii daal, ab dof la”.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 12

Simoore Ad-Dukhan Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Waay-waay, sunu Boroom téggil nu mbugël mi. Ndax nun ay…

Simoore Aaya 12/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers