Ad-Dukhan · 10/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
فَارْتَقِبْ يَوْمَ تَأْتِي السَّمَاءُ بِدُخَانٍ مُّبِينٍ ۝١٠
Fartaqib Yawma taatis samaaa`u bidukhaanim mubeen
📖 Tekkim Wolof
Fuglul, cëy bis ba asamaan si di dikk ak saxar suy jolli

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Simoore Ad-Dukhan

8لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ يُحْيِي وَيُمِيتُ ۖ رَبُّكُمْ وَرَبُّ آبَائِكُمُ الْأَوَّلِينَ
Amul jenn Yàlla judul Moom. Mooy dundal di reye, Mooy seen Boroom mooy Boroom seeni maam ya fi jëkkoon.
9بَلْ هُمْ فِي شَكٍّ يَلْعَبُونَ
Ñoom, ña ngay sikki-sàkka, di fo.
10فَارْتَقِبْ يَوْمَ تَأْتِي السَّمَاءُ بِدُخَانٍ مُّبِينٍ
Fuglul, cëy bis ba asamaan si di dikk ak saxar suy jolli
11يَغْشَى النَّاسَ ۖ هَٰذَا عَذَابٌ أَلِيمٌ
di moor nit ñi. Tey mbugël mu mitti.
12رَّبَّنَا اكْشِفْ عَنَّا الْعَذَابَ إِنَّا مُؤْمِنُونَ
“Waay-waay, sunu Boroom téggil nu mbugël mi. Ndax nun ay jullit la nu [léegi]”.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 10

Simoore Ad-Dukhan Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Fuglul, cëy bis ba asamaan si di dikk ak saxar…

Simoore Aaya 10/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers