Al-Jathiya · 35/37
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Jathiya
ذَٰلِكُم بِأَنَّكُمُ اتَّخَذْتُمْ آيَاتِ اللَّهِ هُزُوًا وَغَرَّتْكُمُ الْحَيَاةُ الدُّنْيَا ۚ فَالْيَوْمَ لَا يُخْرَجُونَ مِنْهَا وَلَا هُمْ يُسْتَعْتَبُونَ ۝٣٥
Zaalikum bi annakumut takhaztum aayaatil laahi huzuwanw wa gharratkumul hayaatud dunyaa; fal yawma laa yukhrajoona minhaa wa laahum yusta`taboon
📖 Tekkim Wolof
li ko waral moo di ni ngeen jàpp laayay Yàlla ay reetaan dundug àddina tax ngeen woru faggu”. Bis niki tey dootu ñu fa génne te déefuleen ko woyofal.

🎧 Dégg


📜 Aaya 33-37 — Simoore Al-Jathiya

33وَبَدَا لَهُمْ سَيِّئَاتُ مَا عَمِلُوا وَحَاقَ بِهِم مَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
Ñu ne gegg ca [ñaatéefi ] seen jëf ya. Lañu daan yejje gaw leen.
34وَقِيلَ الْيَوْمَ نَنسَاكُمْ كَمَا نَسِيتُمْ لِقَاءَ يَوْمِكُمْ هَٰذَا وَمَأْوَاكُمُ النَّارُ وَمَا لَكُم مِّن نَّاصِرِينَ
Ñu wax leen ne : “Bis niki tey dananu leen fàtte (bàyyi leen ci biir Safara) kem ni ngeen fàttewoon dajeg seen bis bii ( ba waajaluleen ko). Seenub dëkkuwaay mooy Safara ; te kenn du leen fa dimbali.
35ذَٰلِكُم بِأَنَّكُمُ اتَّخَذْتُمْ آيَاتِ اللَّهِ هُزُوًا وَغَرَّتْكُمُ الْحَيَاةُ الدُّنْيَا ۚ فَالْيَوْمَ لَا يُخْرَجُونَ مِنْهَا وَلَا هُمْ يُسْتَعْتَبُونَ
li ko waral moo di ni ngeen jàpp laayay Yàlla ay reetaan dundug àddina tax ngeen woru faggu”. Bis niki tey dootu ñu fa génne te déefuleen ko woyofal.
36فَلِلَّهِ الْحَمْدُ رَبِّ السَّمَاوَاتِ وَرَبِّ الْأَرْضِ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Yàllaa jagoo xeeti cant (yépp), Mooy Boroom asamaan yi di Boroom suuf si : di Boroom àddina sépp.
37وَلَهُ الْكِبْرِيَاءُ فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Moo ame màgg ga ci biir asamaan yeek suuf si. Mooy boroom Kàttan ga, di ku Xereñ.
Al-JathiyaFihi Alxuraan
37Aaya
MeccanRevelation
35Aaya

Tekki — Al-Jathiya 35

Simoore Al-Jathiya Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : li ko waral moo di ni ngeen jàpp laayay Yàlla…

Simoore Aaya 35/37 — Simoore Al-Jathiya الجاثية (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Jathiya Dégg, Simoore Al-Jathiya Tekki, Simoore Al-Jathiya mp3, Simoore Al-Jathiya pdf. Aaya 33–37. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers