Al-Ahqaf · 2/35
Tekki Waxtaan — Al-Ahqaf
تَنزِيلُ الْكِتَابِ مِنَ اللَّهِ الْعَزِيزِ الْحَكِيمِ ۝٢
Tanzeelul Kitaabi minal laahil-`Azeezil Hakeem
📖 Tekkim Wolof
Lii moo di wàccug Téere ba bawoo ca Yàlla, miy boroom Kàttan, te di ku xereñ.
🎧 Dégg

📜 Aaya 1-4 — Al-Ahqaf

1حم
Haa, Miim.
2تَنزِيلُ الْكِتَابِ مِنَ اللَّهِ الْعَزِيزِ الْحَكِيمِ
Lii moo di wàccug Téere ba bawoo ca Yàlla, miy boroom Kàttan, te di ku xereñ.
3مَا خَلَقْنَا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا إِلَّا بِالْحَقِّ وَأَجَلٍ مُّسَمًّى ۚ وَالَّذِينَ كَفَرُوا عَمَّا أُنذِرُوا مُعْرِضُونَ
Bindunu asamaan yeek suuf seek li ci seen diggante, lu dul ci dëgg ak dig bu ñu yemale. Yéefër yi ñoom bu ñu leen di waar dañuy dumóoyu.
4قُلْ أَرَأَيْتُم مَّا تَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ أَرُونِي مَاذَا خَلَقُوا مِنَ الْأَرْضِ أَمْ لَهُمْ شِرْكٌ فِي السَّمَاوَاتِ ۖ ائْتُونِي بِكِتَابٍ مِّن قَبْلِ هَٰذَا أَوْ أَثَارَةٍ مِّنْ عِلْمٍ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Waxal ne : “Ana lan ngeen di xalaat ci li ngeen di jaamu bàyyi Yàlla ? Wan leen ma ana li ñu sàkk ci kaw suuf ! Walla dañoo am man-man ci asamaan yi ? Indilleen ma Téere bu jiitu (Alxuraan) wala book jeexitali xam-xam, ndegam ñu dëggu ngeen”.
Al-AhqafFihi Alxuraan
35Aaya
MeccanRevelation
2Aaya

Tekki — Al-Ahqaf 2

Simoore Al-Ahqaf Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lii moo di wàccug Téere ba bawoo ca Yàlla, miy…

Simoore Aaya 2/35 — Al-Ahqaf الأحقاف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahqaf Dégg, Al-Ahqaf Tekki, Al-Ahqaf mp3, Al-Ahqaf pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers