Al-Maida · 104/120
Tekki Waxtaan — Al-Maida
وَإِذَا قِيلَ لَهُمْ تَعَالَوْا إِلَىٰ مَا أَنزَلَ اللَّهُ وَإِلَى الرَّسُولِ قَالُوا حَسْبُنَا مَا وَجَدْنَا عَلَيْهِ آبَاءَنَا ۚ أَوَلَوْ كَانَ آبَاؤُهُمْ لَا يَعْلَمُونَ شَيْئًا وَلَا يَهْتَدُونَ ١٠٤
Transliteration
Wa izaa qeela lahum ta`aalaw ilaa maaa anzalallaahu wa ilar Rasooli qaaloo hasbunaa maa wajadnaa `alaihi aabaaa`anaa; awa law kaana aabaaa`uhum laa ya`lamoona shai`anw wa laa yahtadoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Bu ñu leen nee : “Kaayleen ci li Yàlla wàcce ci Yonent bi”, ñu ne : “La ñu fekk ca sunuy maam doy nanu.”. Doonte la sax ! Seeni maam xamuñu dara te gindikuwuñu [dañuy sax ci loolu]... ?
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 102-106 — Al-Maida
102قَدْ سَأَلَهَا قَوْمٌ مِّن قَبْلِكُمْ ثُمَّ أَصْبَحُوا بِهَا كَافِرِينَ
Am na xeet yu leen jiitu yu laajoon lu mel noonu, te ca sababus laaj ya, tax ñu mujj di ay yéefar.
103مَا جَعَلَ اللَّهُ مِن بَحِيرَةٍ وَلَا سَائِبَةٍ وَلَا وَصِيلَةٍ وَلَا حَامٍ ۙ وَلَٰكِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا يَفْتَرُونَ عَلَى اللَّهِ الْكَذِبَ ۖ وَأَكْثَرُهُمْ لَا يَعْقِلُونَ
Du ut ne Yàlla Moo taxawal Bahiirata , ak Saaniyata , ak Wasiilata ak Haam , waaye yéefar ya ñoo duural Yàlla ay fen te la ëpp ca ñoom xel-luwuñu.
104وَإِذَا قِيلَ لَهُمْ تَعَالَوْا إِلَىٰ مَا أَنزَلَ اللَّهُ وَإِلَى الرَّسُولِ قَالُوا حَسْبُنَا مَا وَجَدْنَا عَلَيْهِ آبَاءَنَا ۚ أَوَلَوْ كَانَ آبَاؤُهُمْ لَا يَعْلَمُونَ شَيْئًا وَلَا يَهْتَدُونَ
Bu ñu leen nee : “Kaayleen ci li Yàlla wàcce ci Yonent bi”, ñu ne : “La ñu fekk ca sunuy maam doy nanu.”. Doonte la sax ! Seeni maam xamuñu dara te gindikuwuñu [dañuy sax ci loolu]... ?
105يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا عَلَيْكُمْ أَنفُسَكُمْ ۖ لَا يَضُرُّكُم مَّن ضَلَّ إِذَا اهْتَدَيْتُمْ ۚ إِلَى اللَّهِ مَرْجِعُكُمْ جَمِيعًا فَيُنَبِّئُكُم بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Éy yéen ñi gëm ! Sàmmleen seen bopp te yéwénal ko ! Ku réer duleen wàññi dara ndegam gindiku ngeen. Seen delluwaay, yéen ñépp, ca Yàlla la jëm ; mu won leen la ngeen daan def.
106يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا شَهَادَةُ بَيْنِكُمْ إِذَا حَضَرَ أَحَدَكُمُ الْمَوْتُ حِينَ الْوَصِيَّةِ اثْنَانِ ذَوَا عَدْلٍ مِّنكُمْ أَوْ آخَرَانِ مِنْ غَيْرِكُمْ إِنْ أَنتُمْ ضَرَبْتُمْ فِي الْأَرْضِ فَأَصَابَتْكُم مُّصِيبَةُ الْمَوْتِ ۚ تَحْبِسُونَهُمَا مِن بَعْدِ الصَّلَاةِ فَيُقْسِمَانِ بِاللَّهِ إِنِ ارْتَبْتُمْ لَا نَشْتَرِي بِهِ ثَمَنًا وَلَوْ كَانَ ذَا قُرْبَىٰ ۙ وَلَا نَكْتُمُ شَهَادَةَ اللَّهِ إِنَّا إِذًا لَّمِنَ الْآثِمِينَ
Éy yéen ñi gëm ! Bu dee dabee kenn ci yéen, na dénkaane te am seede yu nekk ñaar ñu maandu ci yéen, walla ci ñeneen ñu dul yéen, su fekkee dangeen a nekk ci tukki, tiisu dee dab leen. Taxawal-leen ñoom ñaar, ginnaaw julli, ndegam dangeen a am ci ñoom sikki-sàkka, ñu giñ ci Yàlla ne : “Jaayunu sunu seede ci genn njëg, doonte la dafa jëm ci sunu mbokk, te it nëbbunu lu nu Yàlla seedeloo ndax danuy bokk ci way-bàkkaar ña (su nu ko defee)”.
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
104Aaya
Tekki — Al-Maida 104
Simoore Al-Maida Aaya 104 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñu leen nee : “Kaayleen ci li Yàlla wàcce…Simoore Aaya 104/120 — Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Maida Dégg, Al-Maida Tekki, Al-Maida mp3, Al-Maida pdf. Aaya 102–106. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








