Al-Maida · 103/120
Tekki Waxtaan — Al-Maida
مَا جَعَلَ اللَّهُ مِن بَحِيرَةٍ وَلَا سَائِبَةٍ وَلَا وَصِيلَةٍ وَلَا حَامٍ ۙ وَلَٰكِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا يَفْتَرُونَ عَلَى اللَّهِ الْكَذِبَ ۖ وَأَكْثَرُهُمْ لَا يَعْقِلُونَ ۝١٠٣
Maa ja`alal laahu mim baheeratinw wa laa saaa`ibatinw wa laa waseelatinw wa laa haaminw wa laakinnal lazeena kafaroo yaftaroona `alallaahil kazib; wa aksaruhum laa ya`qiloon
📖 Tekkim Wolof
Du ut ne Yàlla Moo taxawal Bahiirata , ak Saaniyata , ak Wasiilata ak Haam , waaye yéefar ya ñoo duural Yàlla ay fen te la ëpp ca ñoom xel-luwuñu.
🎧 Dégg

📜 Aaya 101-105 — Al-Maida

101يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَسْأَلُوا عَنْ أَشْيَاءَ إِن تُبْدَ لَكُمْ تَسُؤْكُمْ وَإِن تَسْأَلُوا عَنْهَا حِينَ يُنَزَّلُ الْقُرْآنُ تُبْدَ لَكُمْ عَفَا اللَّهُ عَنْهَا ۗ وَاللَّهُ غَفُورٌ حَلِيمٌ
Éy yéen ñi gëm ! Buleen di laaj ci yoo xam ne, bu ñu leen ko leeralee, mu nekk lu naqari ci yéen. Te bu ngeen ko laajee ca waxtu wa Alxuraan di wàcc, ñu leeral leen ko. Yàlla jéggal na leen [seen laaj yooyu]. Yàlla Jéggalaakoon la, Ku lewet la.
102قَدْ سَأَلَهَا قَوْمٌ مِّن قَبْلِكُمْ ثُمَّ أَصْبَحُوا بِهَا كَافِرِينَ
Am na xeet yu leen jiitu yu laajoon lu mel noonu, te ca sababus laaj ya, tax ñu mujj di ay yéefar.
103مَا جَعَلَ اللَّهُ مِن بَحِيرَةٍ وَلَا سَائِبَةٍ وَلَا وَصِيلَةٍ وَلَا حَامٍ ۙ وَلَٰكِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا يَفْتَرُونَ عَلَى اللَّهِ الْكَذِبَ ۖ وَأَكْثَرُهُمْ لَا يَعْقِلُونَ
Du ut ne Yàlla Moo taxawal Bahiirata , ak Saaniyata , ak Wasiilata ak Haam , waaye yéefar ya ñoo duural Yàlla ay fen te la ëpp ca ñoom xel-luwuñu.
104وَإِذَا قِيلَ لَهُمْ تَعَالَوْا إِلَىٰ مَا أَنزَلَ اللَّهُ وَإِلَى الرَّسُولِ قَالُوا حَسْبُنَا مَا وَجَدْنَا عَلَيْهِ آبَاءَنَا ۚ أَوَلَوْ كَانَ آبَاؤُهُمْ لَا يَعْلَمُونَ شَيْئًا وَلَا يَهْتَدُونَ
Bu ñu leen nee : “Kaayleen ci li Yàlla wàcce ci Yonent bi”, ñu ne : “La ñu fekk ca sunuy maam doy nanu.”. Doonte la sax ! Seeni maam xamuñu dara te gindikuwuñu [dañuy sax ci loolu]... ?
105يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا عَلَيْكُمْ أَنفُسَكُمْ ۖ لَا يَضُرُّكُم مَّن ضَلَّ إِذَا اهْتَدَيْتُمْ ۚ إِلَى اللَّهِ مَرْجِعُكُمْ جَمِيعًا فَيُنَبِّئُكُم بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Éy yéen ñi gëm ! Sàmmleen seen bopp te yéwénal ko ! Ku réer duleen wàññi dara ndegam gindiku ngeen. Seen delluwaay, yéen ñépp, ca Yàlla la jëm ; mu won leen la ngeen daan def.
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
103Aaya

Tekki — Al-Maida 103

Simoore Al-Maida Aaya 103 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Du ut ne Yàlla Moo taxawal Bahiirata , ak Saaniyata…

Simoore Aaya 103/120 — Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Maida Dégg, Al-Maida Tekki, Al-Maida mp3, Al-Maida pdf. Aaya 101–105. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers