Qaf · 18/45
Tekki Waxtaan — Qaf
مَّا يَلْفِظُ مِن قَوْلٍ إِلَّا لَدَيْهِ رَقِيبٌ عَتِيدٌ ۝١٨
Maa yalfizu min qawlin illaa ladaihi raqeebun `ateed
📖 Tekkim Wolof
Amul jenn wax ju muy àddu lu dul ne Raqiib ak Atiid ña nga ko tiim (ñiy bind jëfi nit ñi) .

🎧 Dégg


📜 Aaya 16-20 — Qaf

16وَلَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ وَنَعْلَمُ مَا تُوَسْوِسُ بِهِ نَفْسُهُ ۖ وَنَحْنُ أَقْرَبُ إِلَيْهِ مِنْ حَبْلِ الْوَرِيدِ
Nun Yàlla Noo sàkk nit bind ko te it xam Nanu liy jax-jaxi ci am xolam te sax Nun Noo ko gën a jegeñ buum giy téye ab xol
17إِذْ يَتَلَقَّى الْمُتَلَقِّيَانِ عَنِ الْيَمِينِ وَعَنِ الشِّمَالِ قَعِيدٌ
ngir ñaari way joqalante yaa ngay joqalante, tey fuglu ndeyjoor ak càmmoñ.
18مَّا يَلْفِظُ مِن قَوْلٍ إِلَّا لَدَيْهِ رَقِيبٌ عَتِيدٌ
Amul jenn wax ju muy àddu lu dul ne Raqiib ak Atiid ña nga ko tiim (ñiy bind jëfi nit ñi) .
19وَجَاءَتْ سَكْرَةُ الْمَوْتِ بِالْحَقِّ ۖ ذَٰلِكَ مَا كُنتَ مِنْهُ تَحِيدُ
Sukraatus ndee aksi na ci ñoom tigi : “Loolu moo di li nga daan weddi”.
20وَنُفِخَ فِي الصُّورِ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْوَعِيدِ
Bu nu wolee Bufta bi : Loolu moo di bisub Tëkóo ba.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
18Aaya

Tekki — Qaf 18

Simoore Qaf Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Amul jenn wax ju muy àddu lu dul ne Raqiib…

Simoore Aaya 18/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers