Qaf · 19/45
Tekki Waxtaan — Qaf
وَجَاءَتْ سَكْرَةُ الْمَوْتِ بِالْحَقِّ ۖ ذَٰلِكَ مَا كُنتَ مِنْهُ تَحِيدُ ۝١٩
Wa jaaa`at kullu nafsim ma`ahaa saaa`iqunw wa shaheed
📖 Tekkim Wolof
Sukraatus ndee aksi na ci ñoom tigi : “Loolu moo di li nga daan weddi”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 17-21 — Qaf

17إِذْ يَتَلَقَّى الْمُتَلَقِّيَانِ عَنِ الْيَمِينِ وَعَنِ الشِّمَالِ قَعِيدٌ
ngir ñaari way joqalante yaa ngay joqalante, tey fuglu ndeyjoor ak càmmoñ.
18مَّا يَلْفِظُ مِن قَوْلٍ إِلَّا لَدَيْهِ رَقِيبٌ عَتِيدٌ
Amul jenn wax ju muy àddu lu dul ne Raqiib ak Atiid ña nga ko tiim (ñiy bind jëfi nit ñi) .
19وَجَاءَتْ سَكْرَةُ الْمَوْتِ بِالْحَقِّ ۖ ذَٰلِكَ مَا كُنتَ مِنْهُ تَحِيدُ
Sukraatus ndee aksi na ci ñoom tigi : “Loolu moo di li nga daan weddi”.
20وَنُفِخَ فِي الصُّورِ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْوَعِيدِ
Bu nu wolee Bufta bi : Loolu moo di bisub Tëkóo ba.
21وَجَاءَتْ كُلُّ نَفْسٍ مَّعَهَا سَائِقٌ وَشَهِيدٌ
Bakkan bu nekk dikk ànd ak ku koy wommat ak ku koy seede.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — Qaf 19

Simoore Qaf Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sukraatus ndee aksi na ci ñoom tigi : “Loolu moo…

Simoore Aaya 19/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers