Adh-Dhariyat · 11/60
Tekki Waxtaan — Simoore Adh-Dhariyat
الَّذِينَ هُمْ فِي غَمْرَةٍ سَاهُونَ ۝١١
Allazeena hum fee ghamratin saahoon
📖 Tekkim Wolof
ñangay nur ci seen lënt ma.

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Simoore Adh-Dhariyat

9يُؤْفَكُ عَنْهُ مَنْ أُفِكَ
(Wax joo xam ne) Képp kuy dumóoyu Alxuraan wax joojoo ko waral.
10قُتِلَ الْخَرَّاصُونَ
Fenkat ya durkat ya dee nañu,
11الَّذِينَ هُمْ فِي غَمْرَةٍ سَاهُونَ
ñangay nur ci seen lënt ma.
12يَسْأَلُونَ أَيَّانَ يَوْمُ الدِّينِ
Ñangay laajati : “Kañ la bis Penc bay doon ? ”
13يَوْمَ هُمْ عَلَى النَّارِ يُفْتَنُونَ
Bis ba nga xam ne dees na leen ca fitnaal ca Safara (lakk leen) :
Adh-DhariyatFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
11Aaya

Tekki — Adh-Dhariyat 11

Simoore Adh-Dhariyat Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñangay nur ci seen lënt ma.

Simoore Aaya 11/60 — Simoore Adh-Dhariyat الذاريات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Adh-Dhariyat Dégg, Simoore Adh-Dhariyat Tekki, Simoore Adh-Dhariyat mp3, Simoore Adh-Dhariyat pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers