Adh-Dhariyat · 50/60
Tekki Waxtaan — Simoore Adh-Dhariyat
فَفِرُّوا إِلَى اللَّهِ ۖ إِنِّي لَكُم مِّنْهُ نَذِيرٌ مُّبِينٌ ۝٥٠
Fafirrooo ilal laahi innee lakum minhu nazeerum mubeen
📖 Tekkim Wolof
“Fëx leen daw wuti seen Boroom. Man dey, ab waarekatam laa bu bir.

🎧 Dégg


📜 Aaya 48-52 — Simoore Adh-Dhariyat

48وَالْأَرْضَ فَرَشْنَاهَا فَنِعْمَ الْمَاهِدُونَ
Suuf si, It Noo ko lal. Ndaw ku man a maasale !
49وَمِن كُلِّ شَيْءٍ خَلَقْنَا زَوْجَيْنِ لَعَلَّكُمْ تَذَكَّرُونَ
Mépp mbir lenn lu nekk wutal Nanu ko [tóolent]. Ngir ngeen man caa fàttalikoo ?
50فَفِرُّوا إِلَى اللَّهِ ۖ إِنِّي لَكُم مِّنْهُ نَذِيرٌ مُّبِينٌ
“Fëx leen daw wuti seen Boroom. Man dey, ab waarekatam laa bu bir.
51وَلَا تَجْعَلُوا مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ ۖ إِنِّي لَكُم مِّنْهُ نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Te it bu leen jéema wut jeneen Yàlla. Man mii dey ab xuppekat laa bu bawoo fa moom, buy leeral di biral”.
52كَذَٰلِكَ مَا أَتَى الَّذِينَ مِن قَبْلِهِم مِّن رَّسُولٍ إِلَّا قَالُوا سَاحِرٌ أَوْ مَجْنُونٌ
Noonu rekk la daan deme amul benn Yonent bu masa ñëw ci la leen jiitu tu du aw nitam dañuy wax ne : “Ab njabarkat la walla ab dof la” !
Adh-DhariyatFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
50Aaya

Tekki — Adh-Dhariyat 50

Simoore Adh-Dhariyat Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Fëx leen daw wuti seen Boroom. Man dey, ab waarekatam…

Simoore Aaya 50/60 — Simoore Adh-Dhariyat الذاريات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Adh-Dhariyat Dégg, Simoore Adh-Dhariyat Tekki, Simoore Adh-Dhariyat mp3, Simoore Adh-Dhariyat pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers