Adh-Dhariyat · 51/60
Tekki Waxtaan — Adh-Dhariyat
وَلَا تَجْعَلُوا مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ ۖ إِنِّي لَكُم مِّنْهُ نَذِيرٌ مُّبِينٌ ۝٥١
Wa laa taj`aloo ma`al laahi ilaahan aakhara innee lakum minhu nazeerum mubeen
📖 Tekkim Wolof
Te it bu leen jéema wut jeneen Yàlla. Man mii dey ab xuppekat laa bu bawoo fa moom, buy leeral di biral”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 49-53 — Adh-Dhariyat

49وَمِن كُلِّ شَيْءٍ خَلَقْنَا زَوْجَيْنِ لَعَلَّكُمْ تَذَكَّرُونَ
Mépp mbir lenn lu nekk wutal Nanu ko [tóolent]. Ngir ngeen man caa fàttalikoo ?
50فَفِرُّوا إِلَى اللَّهِ ۖ إِنِّي لَكُم مِّنْهُ نَذِيرٌ مُّبِينٌ
“Fëx leen daw wuti seen Boroom. Man dey, ab waarekatam laa bu bir.
51وَلَا تَجْعَلُوا مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ ۖ إِنِّي لَكُم مِّنْهُ نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Te it bu leen jéema wut jeneen Yàlla. Man mii dey ab xuppekat laa bu bawoo fa moom, buy leeral di biral”.
52كَذَٰلِكَ مَا أَتَى الَّذِينَ مِن قَبْلِهِم مِّن رَّسُولٍ إِلَّا قَالُوا سَاحِرٌ أَوْ مَجْنُونٌ
Noonu rekk la daan deme amul benn Yonent bu masa ñëw ci la leen jiitu tu du aw nitam dañuy wax ne : “Ab njabarkat la walla ab dof la” !
53أَتَوَاصَوْا بِهِ ۚ بَلْ هُمْ قَوْمٌ طَاغُونَ
moo ndax da ñu ko daan jottaleente ? Li am kay mooy dañoo bew rekk.
Adh-DhariyatFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
51Aaya

Tekki — Adh-Dhariyat 51

Simoore Adh-Dhariyat Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te it bu leen jéema wut jeneen Yàlla. Man mii…

Simoore Aaya 51/60 — Adh-Dhariyat الذاريات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Adh-Dhariyat Dégg, Adh-Dhariyat Tekki, Adh-Dhariyat mp3, Adh-Dhariyat pdf. Aaya 49–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers