At-Tur · 34/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
فَلْيَأْتُوا بِحَدِيثٍ مِّثْلِهِ إِن كَانُوا صَادِقِينَ ۝٣٤
Falyaatoo bihadeesim misliheee in kaanoo saadiqeen
📖 Tekkim Wolof
Su fekkee ne, liñuy wax ngi ci ñoom, nanu indi lu melni Alxuraan.

🎧 Dégg


📜 Aaya 32-36 — Simoore At-Tur

32أَمْ تَأْمُرُهُمْ أَحْلَامُهُم بِهَٰذَا ۚ أَمْ هُمْ قَوْمٌ طَاغُونَ
Moo ndax ñoom seeni xol mooleen di digal ? Am dañoo di aw nit ñu faku ?
33أَمْ يَقُولُونَ تَقَوَّلَهُ ۚ بَل لَّا يُؤْمِنُونَ
Walla dañuy wax naan (Muhammad) : “Moo fent Alxuraan ? ” Li am kay moo di ne... dañoo gëmul.
34فَلْيَأْتُوا بِحَدِيثٍ مِّثْلِهِ إِن كَانُوا صَادِقِينَ
Su fekkee ne, liñuy wax ngi ci ñoom, nanu indi lu melni Alxuraan.
35أَمْ خُلِقُوا مِنْ غَيْرِ شَيْءٍ أَمْ هُمُ الْخَالِقُونَ
Waaw ñoom ndax dañu leen sos bind leen wala ñoom ñooy binde di sos ?
36أَمْ خَلَقُوا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ ۚ بَل لَّا يُوقِنُونَ
Walla ñoom ñoo bind asamaan yeek suuf si ? Li am kay moo di ne ñoom wóoluwuñu.
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
34Aaya

Tekki — At-Tur 34

Simoore At-Tur Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su fekkee ne, liñuy wax ngi ci ñoom, nanu indi…

Simoore Aaya 34/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers