At-Tur · 35/49
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tur
أَمْ خُلِقُوا مِنْ غَيْرِ شَيْءٍ أَمْ هُمُ الْخَالِقُونَ ۝٣٥
Am khuliqoo min ghairi shai`in am humul khaaliqoon
📖 Tekkim Wolof
Waaw ñoom ndax dañu leen sos bind leen wala ñoom ñooy binde di sos ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 33-37 — Simoore At-Tur

33أَمْ يَقُولُونَ تَقَوَّلَهُ ۚ بَل لَّا يُؤْمِنُونَ
Walla dañuy wax naan (Muhammad) : “Moo fent Alxuraan ? ” Li am kay moo di ne... dañoo gëmul.
34فَلْيَأْتُوا بِحَدِيثٍ مِّثْلِهِ إِن كَانُوا صَادِقِينَ
Su fekkee ne, liñuy wax ngi ci ñoom, nanu indi lu melni Alxuraan.
35أَمْ خُلِقُوا مِنْ غَيْرِ شَيْءٍ أَمْ هُمُ الْخَالِقُونَ
Waaw ñoom ndax dañu leen sos bind leen wala ñoom ñooy binde di sos ?
36أَمْ خَلَقُوا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ ۚ بَل لَّا يُوقِنُونَ
Walla ñoom ñoo bind asamaan yeek suuf si ? Li am kay moo di ne ñoom wóoluwuñu.
37أَمْ عِندَهُمْ خَزَائِنُ رَبِّكَ أَمْ هُمُ الْمُصَيْطِرُونَ
Moo ndax ñoom dañoo am sa ndàmbi Boroom ? Walla ñoom ñooy dogal ?
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
35Aaya

Tekki — At-Tur 35

Simoore At-Tur Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waaw ñoom ndax dañu leen sos bind leen wala ñoom…

Simoore Aaya 35/49 — Simoore At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tur Dégg, Simoore At-Tur Tekki, Simoore At-Tur mp3, Simoore At-Tur pdf. Aaya 33–37. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers