At-Tur · 33/49
Tekki Waxtaan — At-Tur
أَمْ يَقُولُونَ تَقَوَّلَهُ ۚ بَل لَّا يُؤْمِنُونَ ۝٣٣
Am yaqooloona taqawwalah; bal laa yu`minoon
📖 Tekkim Wolof
Walla dañuy wax naan (Muhammad) : “Moo fent Alxuraan ? ” Li am kay moo di ne... dañoo gëmul.
🎧 Dégg

📜 Aaya 31-35 — At-Tur

31قُلْ تَرَبَّصُوا فَإِنِّي مَعَكُم مِّنَ الْمُتَرَبِّصِينَ
Waxal ne: “Xaarleen ! Man itam Maa ngi ànd ak ànd ag yéen di xaar”.
32أَمْ تَأْمُرُهُمْ أَحْلَامُهُم بِهَٰذَا ۚ أَمْ هُمْ قَوْمٌ طَاغُونَ
Moo ndax ñoom seeni xol mooleen di digal ? Am dañoo di aw nit ñu faku ?
33أَمْ يَقُولُونَ تَقَوَّلَهُ ۚ بَل لَّا يُؤْمِنُونَ
Walla dañuy wax naan (Muhammad) : “Moo fent Alxuraan ? ” Li am kay moo di ne... dañoo gëmul.
34فَلْيَأْتُوا بِحَدِيثٍ مِّثْلِهِ إِن كَانُوا صَادِقِينَ
Su fekkee ne, liñuy wax ngi ci ñoom, nanu indi lu melni Alxuraan.
35أَمْ خُلِقُوا مِنْ غَيْرِ شَيْءٍ أَمْ هُمُ الْخَالِقُونَ
Waaw ñoom ndax dañu leen sos bind leen wala ñoom ñooy binde di sos ?
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
33Aaya

Tekki — At-Tur 33

Simoore At-Tur Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla dañuy wax naan (Muhammad) : “Moo fent Alxuraan ?…

Simoore Aaya 33/49 — At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tur Dégg, At-Tur Tekki, At-Tur mp3, At-Tur pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers