Al-Qamar · 18/55
Tekki Waxtaan — Al-Qamar
كَذَّبَتْ عَادٌ فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ ١٨
Transliteration
Kazzabat `Aadun fakaifa kaana `azaabee wa nuzur
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Waa Aad weddi woon nañu. Waaye naka la mbugël ma deme woon ak xupp ga ma leen defoon ?
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 16-20 — Al-Qamar
16فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Te naka lay deme Sama mbugël at Samay xuppaate ?
17وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal Nanu, Alxuraan ngir ñu fàttelikoo ca. Moo kon ndax kenn dana ci jàjjoo ?
18كَذَّبَتْ عَادٌ فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Waa Aad weddi woon nañu. Waaye naka la mbugël ma deme woon ak xupp ga ma leen defoon ?
19إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ رِيحًا صَرْصَرًا فِي يَوْمِ نَحْسٍ مُّسْتَمِرٍّ
Yabaloon nanu ca ñoom ngelaw lu ànd ak ub (sedd), ci bis bu tiis te mbugël ma faf wàccatuleen ;
20تَنزِعُ النَّاسَ كَأَنَّهُمْ أَعْجَازُ نَخْلٍ مُّنقَعِرٍ
dadoon sempi nit ñi ni ay dàtti tàndarma di buure.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
18Aaya
Tekki — Al-Qamar 18
Simoore Al-Qamar Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waa Aad weddi woon nañu. Waaye naka la mbugël ma…Simoore Aaya 18/55 — Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qamar Dégg, Al-Qamar Tekki, Al-Qamar mp3, Al-Qamar pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








