Al-Qamar · 19/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ رِيحًا صَرْصَرًا فِي يَوْمِ نَحْسٍ مُّسْتَمِرٍّ ۝١٩
Innaa arsalnaa `alaihim reehan sarsaran fee Yawmi nahsim mustamirr
📖 Tekkim Wolof
Yabaloon nanu ca ñoom ngelaw lu ànd ak ub (sedd), ci bis bu tiis te mbugël ma faf wàccatuleen ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 17-21 — Simoore Al-Qamar

17وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal Nanu, Alxuraan ngir ñu fàttelikoo ca. Moo kon ndax kenn dana ci jàjjoo ?
18كَذَّبَتْ عَادٌ فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Waa Aad weddi woon nañu. Waaye naka la mbugël ma deme woon ak xupp ga ma leen defoon ?
19إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ رِيحًا صَرْصَرًا فِي يَوْمِ نَحْسٍ مُّسْتَمِرٍّ
Yabaloon nanu ca ñoom ngelaw lu ànd ak ub (sedd), ci bis bu tiis te mbugël ma faf wàccatuleen ;
20تَنزِعُ النَّاسَ كَأَنَّهُمْ أَعْجَازُ نَخْلٍ مُّنقَعِرٍ
dadoon sempi nit ñi ni ay dàtti tàndarma di buure.
21فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Naka mu Sama mbugël ak Samag xuppaate ?
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
19Aaya

Tekki — Al-Qamar 19

Simoore Al-Qamar Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yabaloon nanu ca ñoom ngelaw lu ànd ak ub (sedd),…

Simoore Aaya 19/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers