Al-Qamar · 51/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
وَلَقَدْ أَهْلَكْنَا أَشْيَاعَكُمْ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ ۝٥١
Wa laqad ahlaknaaa ashyaa`akum fahal mim muddakir
📖 Tekkim Wolof
Faagaagal Nanu, ay xeet yu mel ni yéen. Mo ndax kon kenn du fàttaliku jàjj ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 49-53 — Simoore Al-Qamar

49إِنَّا كُلَّ شَيْءٍ خَلَقْنَاهُ بِقَدَرٍ
Noo bind lépp lu nekk cig natale,
50وَمَا أَمْرُنَا إِلَّا وَاحِدَةٌ كَلَمْحٍ بِالْبَصَرِ
amul sunu menn mbir [ndigal] ; [lu dul ne] dafay mel ni xefiinu bët.
51وَلَقَدْ أَهْلَكْنَا أَشْيَاعَكُمْ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Faagaagal Nanu, ay xeet yu mel ni yéen. Mo ndax kon kenn du fàttaliku jàjj ?
52وَكُلُّ شَيْءٍ فَعَلُوهُ فِي الزُّبُرِ
Te lépp lu ñu defoon bind Nanu ko ca téere ya,
53وَكُلُّ صَغِيرٍ وَكَبِيرٍ مُّسْتَطَرٌ
lépp, lu ndaw ak lu mag, karmat nañu ko ca.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
51Aaya

Tekki — Al-Qamar 51

Simoore Al-Qamar Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Faagaagal Nanu, ay xeet yu mel ni yéen. Mo ndax…

Simoore Aaya 51/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 49–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers