Al-Qamar · 50/55
Tekki Waxtaan — Al-Qamar
وَمَا أَمْرُنَا إِلَّا وَاحِدَةٌ كَلَمْحٍ بِالْبَصَرِ ٥٠
Transliteration
Wa maaa amrunaaa illaa waahidatun kalamhim bilbasar
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
amul sunu menn mbir [ndigal] ; [lu dul ne] dafay mel ni xefiinu bët.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 48-52 — Al-Qamar
48يَوْمَ يُسْحَبُونَ فِي النَّارِ عَلَىٰ وُجُوهِهِمْ ذُوقُوا مَسَّ سَقَرَ
Bu keroogee ba ñu di leen diri ci seen xarkanam ca biir Safara, (naan leen) : “Mosleen tokamti gu Safara”.
49إِنَّا كُلَّ شَيْءٍ خَلَقْنَاهُ بِقَدَرٍ
Noo bind lépp lu nekk cig natale,
50وَمَا أَمْرُنَا إِلَّا وَاحِدَةٌ كَلَمْحٍ بِالْبَصَرِ
amul sunu menn mbir [ndigal] ; [lu dul ne] dafay mel ni xefiinu bët.
51وَلَقَدْ أَهْلَكْنَا أَشْيَاعَكُمْ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Faagaagal Nanu, ay xeet yu mel ni yéen. Mo ndax kon kenn du fàttaliku jàjj ?
52وَكُلُّ شَيْءٍ فَعَلُوهُ فِي الزُّبُرِ
Te lépp lu ñu defoon bind Nanu ko ca téere ya,
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
50Aaya
Tekki — Al-Qamar 50
Simoore Al-Qamar Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : amul sunu menn mbir [ndigal] ; [lu dul ne] dafay…Simoore Aaya 50/55 — Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qamar Dégg, Al-Qamar Tekki, Al-Qamar mp3, Al-Qamar pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








