Ar-Rahman · 23/78
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rahman
فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ ۝٢٣
Fabi ayyi aalaaa`i Rabbikumaa tukazzibaan
📖 Tekkim Wolof
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?

🎧 Dégg

📜 Aaya 21-25 — Simoore Ar-Rahman

21فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
22يَخْرُجُ مِنْهُمَا اللُّؤْلُؤُ وَالْمَرْجَانُ
Te ñaari [géej]: yooyu peme da ciy génne ak ganjar.
23فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
24وَلَهُ الْجَوَارِ الْمُنشَآتُ فِي الْبَحْرِ كَالْأَعْلَامِ
Moo moom gaal yiy tëmbu ci biir géej niki ay tundi doj ;
25فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
23Aaya

Tekki — Ar-Rahman 23

Simoore Ar-Rahman Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a…

Simoore Aaya 23/78 — Simoore Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rahman Dégg, Simoore Ar-Rahman Tekki, Simoore Ar-Rahman mp3, Simoore Ar-Rahman pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.

Alxuraan bu Tedd bi

Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers