Ar-Rahman · 22/78
Tekki Waxtaan — Ar-Rahman
يَخْرُجُ مِنْهُمَا اللُّؤْلُؤُ وَالْمَرْجَانُ ۝٢٢
Yakhruju minhumal lu `lu u wal marjaanu
📖 Tekkim Wolof
Te ñaari [géej]: yooyu peme da ciy génne ak ganjar.
🎧 Dégg

📜 Aaya 20-24 — Ar-Rahman

20بَيْنَهُمَا بَرْزَخٌ لَّا يَبْغِيَانِ
def na aw dig ca seen diggante ba duñu jaxasoo.
21فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
22يَخْرُجُ مِنْهُمَا اللُّؤْلُؤُ وَالْمَرْجَانُ
Te ñaari [géej]: yooyu peme da ciy génne ak ganjar.
23فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
24وَلَهُ الْجَوَارِ الْمُنشَآتُ فِي الْبَحْرِ كَالْأَعْلَامِ
Moo moom gaal yiy tëmbu ci biir géej niki ay tundi doj ;
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
22Aaya

Tekki — Ar-Rahman 22

Simoore Ar-Rahman Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te ñaari [géej]: yooyu peme da ciy génne ak ganjar.

Simoore Aaya 22/78 — Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Rahman Dégg, Ar-Rahman Tekki, Ar-Rahman mp3, Ar-Rahman pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers