Ar-Rahman · 24/78
Tekki Waxtaan — Ar-Rahman
وَلَهُ الْجَوَارِ الْمُنشَآتُ فِي الْبَحْرِ كَالْأَعْلَامِ ۝٢٤
Wa lahul jawaaril mun sha`aatu fil bahri kal a`laam
📖 Tekkim Wolof
Moo moom gaal yiy tëmbu ci biir géej niki ay tundi doj ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 22-26 — Ar-Rahman

22يَخْرُجُ مِنْهُمَا اللُّؤْلُؤُ وَالْمَرْجَانُ
Te ñaari [géej]: yooyu peme da ciy génne ak ganjar.
23فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
24وَلَهُ الْجَوَارِ الْمُنشَآتُ فِي الْبَحْرِ كَالْأَعْلَامِ
Moo moom gaal yiy tëmbu ci biir géej niki ay tundi doj ;
25فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
26كُلُّ مَنْ عَلَيْهَا فَانٍ
Képp kuy dund kaw [suuf] dana masa saay jeex,
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
24Aaya

Tekki — Ar-Rahman 24

Simoore Ar-Rahman Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo moom gaal yiy tëmbu ci biir géej niki ay…

Simoore Aaya 24/78 — Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Rahman Dégg, Ar-Rahman Tekki, Ar-Rahman mp3, Ar-Rahman pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers