Ar-Rahman · 33/78
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rahman
يَا مَعْشَرَ الْجِنِّ وَالْإِنسِ إِنِ اسْتَطَعْتُمْ أَن تَنفُذُوا مِنْ أَقْطَارِ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ فَانفُذُوا ۚ لَا تَنفُذُونَ إِلَّا بِسُلْطَانٍ ۝٣٣
Yaa ma`sharal jinni wal insi inis tata`tum an tanfuzoo min aqtaaris samaawaati wal ardi fanfuzoo; laa tanfuzoona illaa bisultaan
📖 Tekkim Wolof
Eey yéen mbooleem jinne yi ak nit ñi ! Su ngeen manee lañbatu ci biir déeléy asamaan yeek suuf si, lañbatuleen. Waaye du ngeen mana kër-këri mukk ba génn kiiraayal Yàlla.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 31-35 — Simoore Ar-Rahman

31سَنَفْرُغُ لَكُمْ أَيُّهَ الثَّقَلَانِ
Yéen nit ak jinne yi, danañu leen xalseta àtte
32فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
33يَا مَعْشَرَ الْجِنِّ وَالْإِنسِ إِنِ اسْتَطَعْتُمْ أَن تَنفُذُوا مِنْ أَقْطَارِ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ فَانفُذُوا ۚ لَا تَنفُذُونَ إِلَّا بِسُلْطَانٍ
Eey yéen mbooleem jinne yi ak nit ñi ! Su ngeen manee lañbatu ci biir déeléy asamaan yeek suuf si, lañbatuleen. Waaye du ngeen mana kër-këri mukk ba génn kiiraayal Yàlla.
34فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
35يُرْسَلُ عَلَيْكُمَا شُوَاظٌ مِّن نَّارٍ وَنُحَاسٌ فَلَا تَنتَصِرَانِ
Dees na leen xala sotti safara ak biteex, te kenn du leen dimbali.
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
33Aaya

Tekki — Ar-Rahman 33

Simoore Ar-Rahman Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Eey yéen mbooleem jinne yi ak nit ñi ! Su…

Simoore Aaya 33/78 — Simoore Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rahman Dégg, Simoore Ar-Rahman Tekki, Simoore Ar-Rahman mp3, Simoore Ar-Rahman pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers