Ar-Rahman · 67/78
Tekki Waxtaan — Ar-Rahman
فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ ۝٦٧
Fabi ayyi aalaaa`i Rabbikumaa tukazzibaan
📖 Tekkim Wolof
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
🎧 Dégg

📜 Aaya 65-69 — Ar-Rahman

65فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
66فِيهِمَا عَيْنَانِ نَضَّاخَتَانِ
Nekk na ci seen biir ñaari bëti ndox yuy jol di fuur.
67فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
68فِيهِمَا فَاكِهَةٌ وَنَخْلٌ وَرُمَّانٌ
am na ci biiram ay fuytéef, ak i tàndarma, ak rummaan.
69فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
67Aaya

Tekki — Ar-Rahman 67

Simoore Ar-Rahman Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a…

Simoore Aaya 67/78 — Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Rahman Dégg, Ar-Rahman Tekki, Ar-Rahman mp3, Ar-Rahman pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.

Alxuraan bu Tedd bi

Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers