Al-Mulk · 14/30
Tekki Waxtaan — Al-Mulk
أَلَا يَعْلَمُ مَنْ خَلَقَ وَهُوَ اللَّطِيفُ الْخَبِيرُ ۝١٤
Alaa ya`lamu man khalaq wa huwal lateeful khabeer
📖 Tekkim Wolof
Ki bind ndax dadul xam te Moom moo di ki Ñewenti, di Ku deñ Kumpa ci lépp.
🎧 Dégg

📜 Aaya 12-16 — Al-Mulk

12إِنَّ الَّذِينَ يَخْشَوْنَ رَبَّهُم بِالْغَيْبِ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَأَجْرٌ كَبِيرٌ
Ñay ragal seen Boroom ci kumpa am nañu ag njégël ak pey gu màgg.
13وَأَسِرُّوا قَوْلَكُمْ أَوِ اجْهَرُوا بِهِ ۖ إِنَّهُ عَلِيمٌ بِذَاتِ الصُّدُورِ
Su ngeen di déey walla ngeen di jooru Moo xam tigi li nekk ci dënn yi.
14أَلَا يَعْلَمُ مَنْ خَلَقَ وَهُوَ اللَّطِيفُ الْخَبِيرُ
Ki bind ndax dadul xam te Moom moo di ki Ñewenti, di Ku deñ Kumpa ci lépp.
15هُوَ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ ذَلُولًا فَامْشُوا فِي مَنَاكِبِهَا وَكُلُوا مِن رِّزْقِهِ ۖ وَإِلَيْهِ النُّشُورُ
Moom moo leen tàggatal suuf si : doxleen ci ay déndëm. Tey lekk ciy xéewalam. (Ca Yàlla) la léppiy mujj.
16أَأَمِنتُم مَّن فِي السَّمَاءِ أَن يَخْسِفَ بِكُمُ الْأَرْضَ فَإِذَا هِيَ تَمُورُ
Ndax man ngeen a raw ki nekk ci asamaan si su talañee suuf si ? Ba muy rëg-rëgi, mukk !
Al-MulkFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Al-Mulk 14

Simoore Al-Mulk Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ki bind ndax dadul xam te Moom moo di ki…

Simoore Aaya 14/30 — Al-Mulk الملك (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mulk Dégg, Al-Mulk Tekki, Al-Mulk mp3, Al-Mulk pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers